Results for hicieron translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

profesando ser sabios se hicieron fatuos

Wolof

Ñu teg seen bopp ni boroomi xel, fekk ñu ñàkk xel lañu woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y así lo hicieron, haciendo que todos se sentaran

Wolof

taalibe ya def ko, toogloo nit ña.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

los discípulos fueron e hicieron como jesús les mandó

Wolof

noonu taalibe ya dem, def loolu leen yeesu sant.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

los discípulos hicieron como jesús les mandó y prepararon la pascua

Wolof

noonu taalibe yi defar reeru jéggi ba, na leen yeesu waxe woon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

unos hombres piadosos sepultaron a esteban, e hicieron gran lamentación por él

Wolof

ay nit ñu ragal yàlla fab ecen, jébbal ko boroom bi, di ko jooy bu wér.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y lo hicieron, enviándolo a los ancianos por mano de bernabé y de saulo

Wolof

noonu lañu def nag, teg ko ci loxoy barnabas ak sool, yónnee ko njiit ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando lo hicieron, atraparon una gran cantidad de peces, y sus redes se rompían

Wolof

naka lañu sànni mbaal yi, jàpp jën yu bare, ba mbaal yay tàmbalee xëtt.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

aquel mismo día se hicieron amigos pilato y herodes, porque antes habían estado enemistados

Wolof

erodd ak pilaat dañoo ñi bañante woon bu jëkk, waaye ca bés booba doon nañu ay xarit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

le hicieron allí una cena. marta servía, y lázaro era uno de los que estaban sentados a la mesa con él

Wolof

foofa ñu defaral ko fa reer. màrt moo ko doon séddale, te lasaar bokkoon na ca gan ña.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

le prendieron, le llevaron y le hicieron entrar en la casa del sumo sacerdote. y pedro le seguía de lejos

Wolof

Ñu jàpp yeesu, yóbbu ko ca kër saraxalekat bu mag ba. piyeer topp fu sore.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

ellos tomaron el dinero e hicieron como habían sido instruidos. y este dicho se ha divulgado entre los judíos hasta el día de hoy

Wolof

wottukat ya nag fab xaalis ba, def la ñu leen santoon. te nettali boobu siiw na ci yawut yi ba bésu tey.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

sin embargo, os digo que elías ya ha venido; e hicieron con él todo lo que quisieron, tal como está escrito de él

Wolof

waaye maa ngi leen di wax ne, iliyas ñëw na, te def nañu ko la leen neex, ni ko mbind mi waxe.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

doy gracias a dios, a quien rindo culto con limpia conciencia como lo hicieron mis antepasados, de que sin cesar me acuerdo de ti en mis oraciones de noche y de día

Wolof

fu ma tollu maa ngi lay boole ci samay ñaan, di ci sant yàlla, mi may jaamu ci xel mu dal, ni ko samay maam daan defe. guddi ak bëccëg, bu sama xel demee ci say rangooñ,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

hicieron señas a sus compañeros que estaban en la otra barca, para que viniesen a ayudarles. ellos vinieron y llenaron ambas barcas, de manera que se hundían

Wolof

noonu ñu daldi liyaar seen àndandoo, yi nekk ca geneen gaal ga, ngir ñu ñëw dimbali leen. Ñooñu agsi, ñu feesal ñaari gaal yi, ba ñuy bëgg a suux.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

es semejante a un grano de mostaza que un hombre tomó y sembró en su huerto; y creció y se convirtió en un árbol, y las aves del cielo hicieron nidos en sus ramas

Wolof

mi ngi mel ni doomu fuddën gu nit jël, ji ko ci toolam. mu sax, nekk garab, ba picci asamaan ñëw, tàgg ciy caram.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque habiendo conocido a dios, no le glorificaron como a dios ni le dieron gracias; más bien, se hicieron vanos en sus razonamientos, y su insensato corazón fue entenebrecido

Wolof

ndaxte bi ñu xamee yàlla, taxul ñu màggal ko ni mu ware, mbaa ñu sant ko. waaye ñu daldi réer ci seen biiri xalaat yu mujjul fenn, ba tax seen xol gumba, ba lëndëm këruus.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque hay eunucos que nacieron así desde el vientre de la madre, hay eunucos que fueron hechos eunucos por los hombres, y hay eunucos que a sí mismos se hicieron eunucos por causa del reino de los cielos. el que puede aceptar esto, que lo acepte

Wolof

ndaxte am na ñu judduwaale tële, am na ñu tële ci loxoy nit, te am na ñu bañ a séy ngir nguuru yàlla aji kawe ji. ku ko man a nangu, nangu ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando los soldados crucificaron a jesús, tomaron los vestidos de él e hicieron cuatro partes, una para cada soldado. además, tomaron la túnica, pero la túnica no tenía costura; era tejida entera de arriba abajo

Wolof

xarekat ya, bi ñu daajee yeesu ca bant ba, ba noppi dañoo jël ay yéreem, séddale ko ñeenti cér, ku nekk benn. jël nañu it mbubbam bu ñu ràbb ca kaw ba ci suuf te amul benn ñaw.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,708,335 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK