Results for judas translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

simón el cananita y judas iscariote, quien le entregó

Wolof

simoŋ, mi bokk ca mbooloo, ma ñu tudde Ñi farlu ci moom seen réew; ak yudaa iskariyo, mi nar a wor yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero uno de sus discípulos, judas iscariote, el que estaba por entregarle, dijo

Wolof

kenn ca taalibey yeesu ya, muy yudaa iskariyo, mi ko nar a wor, daldi ne:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces judas iscariote, uno de los doce, fue a los principales sacerdotes para entregárselo

Wolof

ca waxtu woowu kenn ci fukki taalibe ya ak ñaar, ku tudd yudaa iskariyo, dem ca saraxalekat yu mag ya, ngir wori yeesu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

a judas hijo de jacobo, y a judas iscariote, que también llegó a ser el traidor

Wolof

yudaa doomu saag, ak yudaa iskariyo, mi mujj a wor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces jesús le dijo: --judas, ¿con un beso entregas al hijo del hombre

Wolof

waaye yeesu ne ko: «ci fóon ngay jébbale doomu nit ki ay noonam!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

así que hemos enviado a judas y a silas, los cuales también os confirmarán de palabra el mismo informe

Wolof

yónni nanu nag yudd ak silas, ñu di leen xamal xebaar boobu ci seen gémmiñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

hablaba de judas hijo de simón iscariote; porque éste, siendo uno de los doce, estaba por entregarlo

Wolof

yudaa miy doomu simoŋ iskariyo la doon wax. ndeke yudaa, la muy bokk lépp ca fukki taalibe ya ak ñaar, moo ko naroon a wor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

también judas, el que le entregaba, conocía aquel lugar, porque jesús solía reunirse allí con sus discípulos

Wolof

yudaa mi ko naroon a wor xamoon na it bérab ba, ndaxte yeesu daan na fa dem ak ay taalibeem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

judas, siervo de jesucristo y hermano de santiago; a los llamados, amados en dios padre y guardados en jesucristo

Wolof

man yudd, jaamu yeesu kirist, mi bokk ak saag ndey ak baay, maa leen di bind, yéen ñi yàlla baay bi woo te bëgg leen, te yeesu kirist aar leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando judas había salido, dijo jesús: --ahora es glorificado el hijo del hombre, y dios es glorificado en él

Wolof

bi yudaa génnee, yeesu ne: «léegi nag ndamu doomu nit ki feeñ na, te ndamu yàlla feeñ na itam ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces judas, el que le había entregado, al ver que era condenado, sintió remordimiento y devolvió las treinta piezas de plata a los principales sacerdotes y a los ancianos

Wolof

bi nga xamee ne yudaa, mi woroon yeesu, gis na ne, daan nañu ko, mu am naqaru xol. mu dem nag ca saraxalekat yu mag ya ak njiit ya, delloo leen fanweeri poset yu xaalis,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

después de éste, se levantó judas el galileo en los días del censo, y arrastró gente tras sí. aquél también pereció, y todos los que le seguían fueron dispersados

Wolof

gannaawam it yudaa mu galile jóg, ca jamono ja ñu doon bind waa réew ma, mu jógloo nit ñu bare, ñu ànd ak moom. moom itam dee na, te ay nitam ñépp tasaaroo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

jesús contestó: --es aquel para quien yo mojo el bocado y se lo doy. y mojando el bocado, lo tomó y se lo dio a judas hijo de simón iscariote

Wolof

yeesu ne ko: «dinaa capp dogu mburu ci ndab li; ki ma koy jox, kooku la.» noonu yeesu jël dogu mburu, capp ko ca ndab la, daldi koy jox yudaa, doomu simoŋ iskariyo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

"hermanos, era necesario que se cumpliesen las escrituras, en las cuales el espíritu santo habló de antemano por boca de david acerca de judas, que fue guía de los que prendieron a jesús

Wolof

mu ne leen: «bokk yi, li xel mu sell mi waxoon ci mbind mi jaarale ko ci gémmiñu daawuda, fàww mu am. waxoon na ci mbirum yudaa, mi wommat ñi jàpp yeesu

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

el señor le dijo: --levántate, ve a la calle que se llama la derecha y busca en casa de judas a uno llamado saulo de tarso; porque he aquí él está orando

Wolof

boroom bi ne ko: «jógal, nga jaar ci mbedd, mi ñuy wax mbedd mu jub mi, te seet ci kër yudaa nit ku tudd sool te dëkk tars, ndaxte mu ngay ñaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces pareció bien a los apóstoles y a los ancianos con toda la iglesia que enviaran a unos hombres elegidos de entre ellos, a antioquía con pablo y bernabé: a judas que tenía por sobrenombre barsabás, y a silas, quienes eran hombres prominentes entre los hermanos

Wolof

bi mu ko waxee, ndaw yi ak njiit yi ak mbooloom ñi gëm mépp fas yéenee tànn ci ñoom ay nit, yónni leen ancos, ñu ànd ak pool ak barnabas. noonu ñu tànn yudd, mi ñuy dippee barsabas, ak silas, di ay njiit ca bokk ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque algunos pensaban, puesto que judas tenía la bolsa, que jesús le decía: "compra lo que necesitamos para la fiesta", o que diese algo a los pobres

Wolof

waaye gannaaw yudaa moo yoroon boyetu xaalis bi, am ñu xalaat ne, yeesu dafa koo wax, mu dem jëndi li war ci màggal gi, walla mu ne ko mu dem sarax miskin yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,744,620,923 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK