Results for lluvia translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

y oró de nuevo, y el cielo dio lluvia, y la tierra produjo su fruto

Wolof

gannaaw ga mu dellu ñaan, asamaan daldi taw, te suuf si saxal meññeef.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

los nativos nos trataron con no poca amabilidad, pues nos recibieron a todos y encendieron un fuego a causa de la lluvia que caía, y del frío

Wolof

te waa réew ma won nu laabiir gu ràññiku, ndaxte taalal nañu nu safara, ganale nu ndax taw bi sóob ak sedd bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque la tierra, que bebe la lluvia que muchas veces cae sobre ella y produce hierba para el provecho de aquellos que la cultivan, recibe la bendición de dios

Wolof

maanaam suuf suy naan taw bi ciy dal, tey jox ñi ñu koy beyal gàncax gu am njariñ, day jot barke bi jóge ci yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cayó la lluvia, vinieron torrentes, y soplaron vientos, y azotaron contra aquella casa. y se derrumbó, y fue grande su ruina.

Wolof

ba mu noppee, taw bi daldi sóob, wal mi ñëw, ngelaw li jóg, ñu dal ci kaw kër ga; mu màbb, ba ne tasar.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

ellos tienen poder para cerrar el cielo, de modo que no caiga lluvia durante los días de su profecía; y tienen poder sobre las aguas, para convertirlas en sangre y para herir la tierra con toda plaga, cuantas veces quieran

Wolof

am nañu sañ-sañu téye taw diirub fan, yi ñuy wax ci kàddug yàlla. am nañu it sañ-sañu soppi ndox yi deret te wàcce ci kaw suuf musiba yu nekk, saa su ñu ko bëggee.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

aunque jamás dejó de dar testimonio de sí mismo haciendo el bien, dándoos lluvias del cielo y estaciones fructíferas, llenando vuestros corazones de sustento y de alegría

Wolof

moona noppiwul a firndeel aw meloom ci def lu baax, di leen wàcceele ci asamaan taw buy indi naataange, ba ngeen lekk ba suur, te seen xol fees ak mbég.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,674,237 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK