From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
porque hemos hallado que este hombre es una plaga, y es promotor de sediciones entre los judíos de todo el mundo y cabecilla de la secta de los nazarenos
ndaxte ci mbirum nit kii teew, gis nanu ne rambaaj la, buy indi xëccoo ci yawut yi ci àddina sépp, di njiitu mbooloo mu ñuy wax nasaréen.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
habiendo llegado, habitó en la ciudad que se llama nazaret. así se cumplió lo dicho por medio de los profetas, que había de ser llamado nazareno
mu ñëw nag dëkk ci dëkk bu ñuy wax nasaret. noonu am la ñu waxoon ca xale ba, jaarale ko ca yonent ya, bi ñu naan:«dees na ko tudde nasaréen.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: