Results for no temas translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

al oír esto, jesús le respondió: --no temas; sólo cree, y ella será salva

Wolof

yeesu dégg kàddu yooyu, daldi ne njiit la: «bul tiit. gëmal rekk te dina dundaat.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces el ángel le dijo: --¡no temas, maría! porque has hallado gracia ante dios

Wolof

malaaka ma ne ko: «bul ragal dara maryaama, ndaxte yàlla tànn na la ci yiwam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces el señor dijo a pablo de noche, por medio de una visión: "no temas, sino habla y no calles

Wolof

naka noona boroom bi feeñu pool ci guddi ne ko: «bul tiit dara, waaye deel wax te bañ a noppi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

pero jesús, sin hacer caso a esta palabra que se decía, dijo al principal de la sinagoga: --no temas; sólo cree

Wolof

waaye yeesu jàppul wax jooju; mu ne njiit la: «gëmal rekk te bañ a tiit.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

cuando le vi, caí como muerto a sus pies. y puso sobre mí su mano derecha y me dijo: "no temas. yo soy el primero y el último

Wolof

naka laa ko gis, di daanu ci ay tànkam ni ku dee. waaye mu teg loxol ndeyjooram ci sama kaw ne ma: «bul ragal dara. maay ki jëkk te maay mujj.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

y me dijo: "no temas, pablo. es necesario que comparezcas ante el césar, y he aquí dios te ha concedido todos los que navegan contigo.

Wolof

mu ne ma: “pool bul tiit; fàww nga taxaw ci kanamu sesaar, te yaa tax yàllay aar bakkani ñi nga àndal ñépp.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

pero el ángel le dijo: --¡no temas, zacarías! porque tu oración ha sido atendida. tu esposa elisabet te dará a luz un hijo, y llamarás su nombre juan

Wolof

waaye malaaka ma ne ko: «bul ragal dara sakariya, ndaxte sa ñaan nangu na. elisabet sa jabar dina la jural doom, te dinga ko tudde yaxya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y de igual manera de jacobo y juan, hijos de zebedeo, que eran socios de simón. entonces jesús dijo a simón: --no temas; de aquí en adelante estarás pescando hombres

Wolof

ak ña mu bokkaloon liggéey ba, maanaam ñaari doomi sebede yi di saag ak yowaana. yeesu ne simoŋ: «bul ragal dara; gannaawsi tey, ay nit ngay mbaal jëme ci man.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

mientras él pensaba en esto, he aquí un ángel del señor se le apareció en sueños y le dijo: "josé, hijo de david, no temas recibir a maría tu mujer, porque lo que ha sido engendrado en ella es del espíritu santo

Wolof

waaye bi muy xalaat ci loolu, benn malaakam boroom bi daldi ko feeñu ci gént ne ko: «yaw yuusufa, sëtu daawuda, bul ragal a yeggali maryaama sa jabar, ndaxte doom ji mu ëmb, ci xel mu sell mi la jóge.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.

Get a better translation with
8,909,330,401 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK