Results for perdonar translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

si confesamos nuestros pecados, él es fiel y justo para perdonar nuestros pecados y limpiarnos de toda maldad

Wolof

su nu nangoo sunuy bàkkaar ci kanamam, fekk kuy sàmm kóllëre la te jub, ngir baal nu sunuy bàkkaar te sellal nu ci lépp lu jubadi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero para que sepáis que el hijo del hombre tiene autoridad para perdonar pecados en la tierra--dijo al paralítico--

Wolof

waaye xamleen ne, doomu nit ki am na ci àddina sañ-sañu baale bàkkaar yi.» ci kaw loolu mu ne làggi ba:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

--¿por qué habla éste así? ¡blasfema! ¿quién puede perdonar pecados, sino uno solo, dios

Wolof

«kii kan la, ba sañ a wax lii; mi ngi sosal yàlla. ana ku man a baale bàkkaar yi, ku dul yàlla doŋŋ?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces los escribas y los fariseos comenzaron a razonar diciendo: --¿quién es éste, que habla blasfemias? ¿quién puede perdonar pecados, sino sólo dios

Wolof

xutbakat yi ak farisen yi di werante ci seen xel naan: «kii mooy kan bay sosal yàlla? ana ku man a baale bàkkaar yi, ku dul yàlla doŋŋ?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces pedro se acercó y le dijo: --señor, ¿cuántas veces pecará mi hermano contra mí y yo le perdonaré? ¿hasta siete veces

Wolof

noonu piyeer ñëw ci yeesu, laaj ko: «boroom bi, bu ma sama mbokk tooñee, ñaata yoon laa ko war a baal? xanaa ba ci juróom-ñaari yoon?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,787,811,077 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK