From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
permanezca el amor fraternal
saxleen ci bëggante ni ay bokk.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
cada uno permanezca en la condición en que fue llamado
na kenn ku nekk jàpp ci li mu nekkoon, bi ko yàlla wooyee.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
yo he venido al mundo como luz, para que todo aquel que cree en mí no permanezca en las tinieblas
ni ag leer laa wàcce ci àddina, ngir ku ma gëm du des ci lëndëm.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
temamos, pues, mientras permanezca aún la promesa de entrar en su reposo, no sea que alguno de vosotros parezca quedarse atrás
yàlla dige na ne, dina am ñu dugg ca noflaayam. kon ndegam dige boobu mi ngi taxaw ba tey, moytuleen ba kenn ci yéen réer ba du dugg ci noflaay boobu.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
permanezca en vosotros lo que habéis oído desde el principio. si permanece en vosotros lo que habéis oído desde el principio, también vosotros permaneceréis en el hijo y en el padre
yéen nag, la ngeen déggoon ca ndoorte la, na sax ci yéen. loolu ngeen déggoon ca ndoorte la, su saxee ci yéen, dingeen sax yéen itam ci doom ji ak ci baay bi.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
la expresión "todavía una vez más" indica con claridad que será removido lo que puede ser sacudido, como las cosas creadas, para que permanezca lo que no puede ser sacudido
ci li mu wax: «beneen yoon,» dafay xamle ne, yàlla dina dindi yi ñu man a yengal, maanaam li ñu sàkk, ngir li ñu mënul a yengal sax ba fàww.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
"vosotros no me elegisteis a mí; más bien, yo os elegí a vosotros, y os he puesto para que vayáis y llevéis fruto, y para que vuestro fruto permanezca; a fin de que todo lo que pidáis al padre en mi nombre él os lo dé
du yéen yéena ma tànn, waaye man maa leen tànn, sas leen ngeen dem, meññ meññeef gu sax, ngir baay bi def lu ngeen ko ñaan ci sama tur.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting