Results for perseverancia translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

por vuestra perseverancia ganaréis vuestras almas

Wolof

seen muñ moo leen di musal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero si esperamos lo que no vemos, con perseverancia lo aguardamos

Wolof

li feek gisagunu nag li nuy yaakaar, dinanu ko séentu ak muñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y la perseverancia produce carácter probado, y el carácter probado produce esperanza

Wolof

te muñ mooy ndeyu jikko ju dëgër; te jikko ju dëgër day jur yaakaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

vida eterna a los que por su perseverancia en las buenas obras buscan gloria, honra e incorrupción

Wolof

Ñiy góor-góorlu ciy def lu baax, bëgg yàlla boole leen ca ndamam te sédde leen ngërëm ak dund gu sax, dina leen tàbbal ci dund gu dul jeex.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

además, sé que tienes perseverancia, que has sufrido por causa de mi nombre y que no has desfallecido

Wolof

xam naa it ne muñ nga, ba dékku coono ndax sama tur, te xàddiwoo. i

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

al conocimiento, dominio propio; al dominio propio, perseverancia; a la perseverancia, devoción

Wolof

noot sa bopp googu, ngeen yokk ci muñ, yokk ci ragal yàlla,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pues lo que fue escrito anteriormente fue escrito para nuestra enseñanza, a fin de que por la perseverancia y la exhortación de las escrituras tengamos esperanza

Wolof

ndaxte lépp lu ñu waxoon ci mbind mi lu jiitu tey, dañu koo tëraloon, ngir nu sàkku ci xam-xam, xam-xam bu nuy may fit ak muñ, ak di feddali sunu yaakaar.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

más bien, en todo nos presentamos como ministros de dios: en mucha perseverancia, en tribulaciones, en necesidades, en angustias

Wolof

li nu bëgg moo di rafetal sunu tur ni jawriñi yàlla ci fànn gu nekk; danuy muñ coono yi, tiis yi, njàqare yi;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

yo conozco tus obras, tu amor, tu fidelidad, tu servicio y tu perseverancia; y que tus últimas obras son mejores que las primeras

Wolof

xam naa say jëf, sa mbëggeel, sa ngëm, sag muñ ak ni nga farloo ci sa jaamu yàlla. xam naa say jëf yu mujj, ni ñu ëppe yu jëkk ya. i

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

he aquí, tenemos por bienaventurados a los que perseveraron. habéis oído de la perseverancia de job y habéis visto el propósito final del señor, que el señor es muy compasivo y misericordioso

Wolof

xam ngeen ne ñiy góor-góorlu, ñu barkeel lañu. dégg ngeen muñ ga ayóoba amoon, te gis muj gu rafet, ga ko boroom bi jagleel, ndax boroom bi kuy ñeewante la te bare yërmande.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

nos acordamos sin cesar, delante del dios y padre nuestro, de la obra de vuestra fe, del trabajo de vuestro amor y de la perseverancia de vuestra esperanza en nuestro señor jesucristo

Wolof

dunu noppee fàttaliku ci kanam yàlla sunu baay jëf ji juddu ci seen ngëm, liggéey bi tukkee ci seen mbëggeel, ak muñ gi sosoo ci seen yaakaar ci sunu boroom yeesu kirist.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero en cuanto a la parte que cayó en buena tierra, éstos son los que, al oír con corazón bueno y recto, retienen la palabra oída; y llevan fruto con perseverancia

Wolof

ki jot ci jiwu wi ci suuf su baax si nag, mooy ki dégg kàddu gi te denc ko ci xol bu baax bu gore, te muñ ba jur njariñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

por tanto, nosotros también, teniendo en derredor nuestro tan grande nube de testigos, despojémonos de todo peso y del pecado que tan fácilmente nos enreda, y corramos con perseverancia la carrera que tenemos por delante

Wolof

kon nag gannaaw mbooloo mu bare moo nu yéew, di nu seedeel seen ngëm, nanu yenniku bépp yen ak bàkkaar bu nuy téqtal ci lu yomb, tey daw xél wi nekk sunu kanam, ànd ci ak muñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

si alguien lleva en cautividad, es llevado en cautividad; si alguien mata a espada, tiene que ser muerto a espada. ¡aquí está la perseverancia y la fe de los santos

Wolof

ku yàlla dogal,ñu war laa jàpp njaam,dinañu la jàpp njaam.ku yàlla dogal,ñu war laa rey ak jaasi,dinañu la rey ak jaasi. looloo tax gaayi yàlla yi war a muñ te takku.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,618,729 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK