From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
y otra vez: yo pondré mi confianza en él. y otra vez: he aquí, yo y los hijos que dios me dio
newaat na:«dinaa am ci yàlla kóolute.» dellu na waxaat ne:«maa ngi nii, man ak doom yi ma yàlla jox.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
si alguien tiene hambre, coma en su casa, para que no os reunáis para juicio. las demás cosas las pondré en orden cuando llegue
ku xiif, na lekke këram, ngir bañ a indi ci yéen àtteb yàlla ndax seen ndaje yi. yeneen fànn yi ci des nag, bu ma ñëwee ci yéen, dinaa ko seet.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
le dijo pedro: --señor, ¿por qué no te puedo seguir ahora? ¡mi vida pondré por ti
piyeer ne ko: «boroom bi, lu tax mënuma laa topp léegi? Àttan naa joxe sama bakkan ngir yaw!»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
he aquí mi siervo, a quien he escogido; mi amado, en quien se complace mi alma. pondré mi espíritu sobre él, y anunciará juicio a las naciones
«kii mooy sama ndaw li ma tànn,di sama soppe bi neex sama xol.dinaa def sama xel ci moom,muy yégal xeet yi yoonu njub.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
su señor le dijo: "bien, siervo bueno y fiel. sobre poco has sido fiel, sobre mucho te pondré. entra en el gozo de tu señor.
njaatigeem ne ko: “def nga lu baax, surga bu baax nga te takku. gannaaw takku nga ci lu tuuti, dinaa la dénk lu bare. kaay bokk ci sama mbég.”
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
"porque éste es el pacto que haré con la casa de israel después de aquellos días," dice el señor. "pondré mis leyes en la mente de ellos y en sus corazones las inscribiré. y yo seré para ellos dios, y para mí ellos serán pueblo
boroom bi nee na:kóllëre gaa ngii,kóllëre gi may fas ak bànni israyil,bu bés yooyule weesoo.dinaa def samay ndigal ci seen xel,bind ko ci seen xol.dinaa nekk seen yàlla,ñu doon samay gaay.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting