Results for preguntar translation from Spanish to Wolof

Spanish

Translate

preguntar

Translate

Wolof

Translate
Translate

Instantly translate texts, documents and voice with Lara

Translate now

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

comed de todo lo que se vende en la carnicería, sin preguntar nada por motivo de conciencia

Wolof

man ngeen a lekk lépp lu ñuy jaay ca ja ba, bañ cee boole ay laaj ngir dalal seen xel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Be the first to vote

Spanish

si algún no creyente os invita, y queréis ir, comed de todo lo que se os ponga delante, sin preguntar nada por motivo de conciencia

Wolof

ku xamul yàlla nag, bu leen wooyee aw ñam këram, te ngeen nangoo dem, lekkleen lépp lu ñu leen dëj, bañ a laajte dara ngir dalal seen xel.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Be the first to vote

Spanish

entonces, los fariseos le volvieron a preguntar de qué manera había recibido la vista, y les dijo: --Él me puso lodo sobre los ojos; me lavé y veo

Wolof

looloo tax farisen ya di laajaat waa ja fi mu jaar bay gis léegi. mu ne leen: «dafa tay ban ci samay bët, ma sëlmuji, ba fi ma nekk maa ngi gis.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Be the first to vote

Spanish

además, si yo os preguntara, no me responderíais

Wolof

te su ma leen laajee, dungeen tontu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Be the first to vote

Get a better translation with
8,799,474,557 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK