Results for produce translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

sabiendo que la prueba de vuestra fe produce paciencia

Wolof

xam ne nattub ngëm mooy ndeyu muñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque la ley produce ira; pero donde no hay ley, tampoco hay transgresión

Wolof

yoonu musaa daal du def lu dul wàcce merum yàlla ci sunu bopp; ndax fu yoon amul, jàdd yoon du fa man a am.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque nuestra momentánea y leve tribulación produce para nosotros un eterno peso de gloria más que incomparable

Wolof

ndaxte sunu coono bu woyof bi dul yàgg, dafa nuy jural ndam lu bare, ba suul coono bi, tey sax abadan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

también, si la trompeta produce un sonido incierto, ¿quién se preparará para la batalla

Wolof

rax-ca-dolli su liit gi jibul bu leer, kuy man a waajal xare ba?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero la que produce espinos y abrojos es desechada, está cercana a la maldición, y su fin es ser quemada

Wolof

waaye su meññee ay dég ak ay xaaxaam, du am benn njariñ; repp na ñu alag ko, te lakk lay mujje.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

esto, para que seáis enriquecidos en todo para toda liberalidad, la cual produce acciones de gracias a dios por medio de nosotros

Wolof

noonu dingeen woomle ci lépp, ba yéwén ci bépp anam, ba tax ñu bare gërëm yàlla ndax li ngeen maye jaarale ko ci nun.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque la tierra, que bebe la lluvia que muchas veces cae sobre ella y produce hierba para el provecho de aquellos que la cultivan, recibe la bendición de dios

Wolof

maanaam suuf suy naan taw bi ciy dal, tey jox ñi ñu koy beyal gàncax gu am njariñ, day jot barke bi jóge ci yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero el que fue sembrado en buena tierra, éste es el que oye la palabra y la entiende, el que de veras lleva fruto y produce, uno a ciento, otro a sesenta, y otro a treinta por uno

Wolof

ki jot ci jiwu wi ci suuf su baax si nag, mooy ki dégg wax ji te xam ko; mu jural ko njariñ, muy lu mat téeméeri yoon lu ëpp la ñu ji woon, muy juróom-benn-fukk mbaa fanweer.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

en medio de la avenida de la ciudad, y a uno y otro lado del río, está el árbol de la vida, que produce doce frutos, dando cada mes su fruto. las hojas del árbol son para la sanidad de las naciones

Wolof

xellee ca digg péncu dëkk ba. ca weti dex ga amoon na ca garabu dund, guy meññ fukki yoon ak ñaar, di meññ weer wu nekk, te xob ya di faj xeet yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,792,313,755 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK