From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
a jesús el mediador del nuevo pacto, y a la sangre rociada que habla mejor que la de abel
jege yeesu, rammukat bi sàmm kóllëre gu bees gi; jege deretam, ji ñu wis. te deret jooju, li muy yégle moo gën a neex li deretu abel doon yéene.
el segundo ángel derramó su copa sobre el mar. y se convirtió en sangre como de muerto. y murió todo ser viviente que estaba en el mar
Ñaareelu malaaka ma sotti ndabam ci géej gi. mu soppiku deret ni deretu néew, ba lépp luy dund te nekkoon ci géej gi dee.
porque los cuerpos de aquellos animales, cuya sangre es introducida por el sumo sacerdote en el lugar santísimo como sacrificio por el pecado, son quemados fuera del campamento
ndaxte saraxalekat bu mag bi dafay yóbbu deretu mala yi ca bérab bu sell-baa-sell ni sarax ngir dindi bàkkaar yi, waaye yàpp wi dees na ko lakk ca gannaaw dal ba.
como demostración de su justicia, dios le ha puesto a él como expiación por la fe en su sangre, a causa del perdón de los pecados pasados, en la paciencia de dios
wàcce na kirist, mu nekk sarax ngir yàlla baal nu sunuy bàkkaar, jaar ci deretam ji ñu tuur; te ngëm rekk moo nu ciy boole. noonu yàlla firndeel na ne ku jub la, doonte sax dafa muñaloon ñi jiitu jamonoy kirist, ba jéggal leen seeni bàkkaar.
pero en la segunda, una vez al año, entraba el sumo sacerdote solo, no sin sangre, la cual ofrecía por sí mismo y por los pecados que el pueblo cometía por ignorancia
waaye ca néeg ba ca topp, saraxalekat bu mag ba rekk moo fa daan dugg benn yoon ci at mi. te daawu fa dugg mukk te yóbbaalewul deretu mala, yi muy jagleel yàlla, ngir bàkkaari boppam ak yu mbooloo mi daan def ci seen ñàkka xam.
asimismo, después de haber cenado, tomó también la copa y dijo: --esta copa es el nuevo pacto en mi sangre, que por vosotros se derrama
noonu itam bi ñu lekkee ba noppi, mu jël kaas bi ne leen: «kaas bii mooy misaal kóllëre gu bees gi yàlla fas jaarale ko ci sama deret, ji tuuru ngir yéen.
entonces jesús respondió y le dijo: --bienaventurado eres, simón hijo de jonás, porque no te lo reveló carne ni sangre, sino mi padre que está en los cielos
yeesu tontu ko: «barkeel ñeel na la, simoŋ doomu yunus, ndaxte du nit moo la xamal lii, waaye sama baay bi nekk ci kaw.
asimismo, tomó también la copa después de haber cenado, y dijo: "esta copa es el nuevo pacto en mi sangre. haced esto todas las veces que la bebáis en memoria de mí.
noonu itam bi ñu lekkee ba noppi, mu jël kaas bi ne leen: «kaas bii mooy misaal kóllëre gu bees, gi yàlla fas jaarale ko ci sama deret. defleen lii ngir fàttaliku ma.»