Results for sujetó translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

cuando éste recibió semejante orden, los metió en el calabozo de más adentro y sujetó sus pies en el cepo

Wolof

gannaaw jot na ndigal loolu nag, mu sànni leen ca néeg ba gën a ruqu ci biir kaso ba, jéng seeni tànk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque la creación ha sido sujetada a la vanidad, no por su propia voluntad, sino por causa de aquel que la sujetó, en esperanz

Wolof

ndaxte dunyaa bi bépp mu ngi ci yoon wu dul mujj fenn; teyu ko, yàlla moo ko ko teg. waaye teewul ñu am yaakaar ne,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

pero cuando aquél le ponga en sujeción todas las cosas, entonces el hijo mismo también será sujeto al que le sujetó todas las cosas, para que dios sea el todo en todos

Wolof

léegi bu ñu ko nootalee lépp nag, moom kirist muy doom ji dina delloo kilifteef gi yàlla, mi ko nootal lépp, ngir yàlla nekk buur ci lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

a que sean prudentes y castas, a que sean buenas amas de casa, a que estén sujetas a sus propios maridos, para que la palabra de dios no sea desacreditada

Wolof

di ñu maandu, sell te fonk seen kër, ñu neex deret te déggal seeni jëkkër, ngir kenn bañ cee gàkkal kàddug yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,787,765,666 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK