Results for tinieblas translation from Spanish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Spanish

Wolof

Info

Spanish

mira, pues, no sea que la luz que hay en ti sea tinieblas

Wolof

moytul ndax leer gi nekk ci yaw du lëndëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

la luz resplandece en las tinieblas, y las tinieblas no la vencieron

Wolof

leer gi feeñ na ci biir lëndëm, te lëndëm gi jàppu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el que dice que está en la luz y odia a su hermano, está en tinieblas todavía

Wolof

ku wax ne yaa ngi ci leer, tey bañ sa mbokk, yaa ngi ci lëndëm ba tey.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

tú estás persuadido de que eres guía de los ciegos, luz de los que están en tinieblas

Wolof

yaa ngi teg sa bopp wommatkatu gumba yi ak leeru ñi nekk cig lëndëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

si decimos que tenemos comunión con él y andamos en tinieblas, mentimos y no practicamos la verdad

Wolof

su nu waxee ne, bokk nanu ci moom, tey dox ci lëndëm, danuy fen ci sunuy wax ak sunuy jëf.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y no tengáis ninguna participación en las infructuosas obras de las tinieblas; sino más bien, denunciadlas

Wolof

te daw lépp luy jëfi lëndëm yu amul njariñ, bay weer sax ku koy def.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

al siervo inútil echadlo en las tinieblas de afuera." allí habrá llanto y crujir de dientes

Wolof

te sànnileen surga bu amul njariñ bi ci biti ci lëndëm gi. foofa dees na fa jooy te yéyu.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

para alumbrar a los que habitan en tinieblas y en sombra de muerte; para encaminar nuestros pies por caminos de paz

Wolof

ngir leeral ñi toog ci lëndëm,takkandeeru dee tiim leen,ngir jiite nu ci yoonu jàmm.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el pueblo que moraba en tinieblas vio una gran luz. a los que moraban en región y sombra de muerte, la luz les amaneció

Wolof

xeet wa nekkoon cig lëndëm,gis na leer gu mag,ña dëkkoon ca réew, ma dee tiim,leer fenkal na leen.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

el quinto ángel derramó su copa sobre el trono de la bestia, y su reino fue convertido en tinieblas. se mordían las lenguas de dolo

Wolof

juróomeelu malaaka ma tuur ndabam ci kaw gàngunem rab wa. noonu lëndëm muur nguuram. nit ñi di màtt seeni làmmiñ ndax metit,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

otra vez os escribo un mandamiento nuevo, que es verdadero en él y en vosotros, porque las tinieblas van pasando y la luz verdadera ya está alumbrando

Wolof

teewul ndigal lu bees laa leen di bind, lu amoon ci dundu yeesu, te am it ci seen dund; ndaxte lëndëm gaa ngi wéy, te leer gu wóor gi fenk na xaat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

la noche está muy avanzada, y el día está cerca. despojémonos, pues, de las obras de las tinieblas y vistámonos con las armas de la luz

Wolof

guddi gi màggat na, bët a ngi bëgg a set. nanu bàyyi nag jëf yu lëndëm te ràngoo gànnaay yi nu yàlla jox, ngir dund ci leer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

la lámpara de tu cuerpo es tu ojo. cuando tu ojo está sano, también todo tu cuerpo está lleno de luz. pero cuando es malo, también tu cuerpo está en tinieblas

Wolof

bët mooy làmpu yaram. bu sa bët wéree, kon sa yaram wépp leer. waaye bu sa bët woppee, kon sa yaram wépp lëndëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

porque nuestra lucha no es contra sangre ni carne, sino contra principados, contra autoridades, contra los gobernantes de estas tinieblas, contra espíritus de maldad en los lugares celestiales

Wolof

ndaxte ndëndu xare jib na, waxuma sunu diggante ak nit ñi, waaye ak kilifa yiy nëxal àddina si, ñuy kilifa yi ak ay boroom sañ-sañ, di gaayi seytaane yi ci bérab yu kawe yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces el rey dijo a los que servían: "atadle los pies y las manos y echadle en las tinieblas de afuera." allí habrá llanto y crujir de dientes

Wolof

noonu buur ba ne ay surgaam: “yeewleen ko ci tànk yi ak ci loxo yi, sànni ko ci biti ci lëndëm gi. foofa dees na fa jooy tey yéyu.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Spanish

así que, no juzguéis nada antes de tiempo, hasta que venga el señor, quien a la vez sacará a la luz las cosas ocultas de las tinieblas y hará evidentes las intenciones de los corazones. entonces tendrá cada uno la alabanza de parte de dios

Wolof

looloo tax buleen daan kenn ci àtte, bala jamono ji di jot te boroom bi ñëw. mooy leeral yi nëbbu ci lëndëm, di làññi mébétu xol yi. bu ko defee ku nekk dina jot ci yàlla ngërëm, li mu yelloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

entonces jesús les dijo: --aún por un poco de tiempo está la luz entre vosotros. andad mientras tenéis la luz, para que no os sorprendan las tinieblas. porque el que anda en tinieblas no sabe a dónde va

Wolof

yeesu ne leen: «leer gi dootul yàgg ak yéen. doxleen, ci bi ngeen dee am leer, ngir lëndëm bañ leen a bett. ndaxte kuy dox ci lëndëm doo xam foo jëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Spanish

y ahora, ¡he aquí la mano del señor está contra ti! quedarás ciego por un tiempo sin ver el sol. de repente cayeron sobre él niebla y tinieblas, y andando a tientas, buscaba quien le condujese de la mano

Wolof

léegi loxob boroom bi dina dal sa kaw, te dinga gumba, ba dootuloo gis jant bi ab diir.» ca saa sa nag ay bëtam muuru, mu daldi tàbbi cig lëndëm, muy làmbatu, di wut ku ko wommat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,727,537,752 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK