Results for chakula translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

utupe leo chakula chetu tunachohitaji.

Wolof

may nu tey li nu war a dunde;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tuseme kaka au dada hana nguo au chakula.

Wolof

su amee mbokk ci seen biir, mu rafle te amul dund, muy góor walla jigéen,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

utupe daima chakula chetu cha kila siku.

Wolof

may nu bés bu nekk li nu war a dunde.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hapo wote wakapata moyo, nao pia wakala chakula.

Wolof

bi ñu gisee loolu, ñépp dëgëraat, ñu daldi lekk ñoom itam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wanafunzi wake wakaulizana, "je, kuna mtu aliyemletea chakula?"

Wolof

taalibe ya nag di laajante naan: «ndax dafa am ku ko indil lekk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

roho yake ikamrudia, akaamka mara. yesu akaamuru wampe chakula.

Wolof

noonu ruuwu xale ba dellusiwaat, mu daldi jóg ca saa sa. yeesu santaane ñu may ko, mu lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

huyo mfarisayo alistaajabu kuona kwamba alikula chakula bila kunawa.

Wolof

farisen bi nag daldi jaaxle, bi mu gisee ne yeesu raxasuwul, laata muy lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini yesu akawaambia, "mimi ninacho chakula msichokijua ninyi."

Wolof

waaye yeesu tontu leen: «am na ñam wu may lekk, te xamuleen ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kwa hiyo basi, kama tunacho chakula na mavazi, tunapaswa kuridhika navyo.

Wolof

kon su nu amee lekk ak koddaay, nanu ko doyloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

(wakati huo wanafunzi wake walikuwa wamekwenda mjini kununua chakula.)

Wolof

fekk booba nag, taalibey yeesu ya dañoo demoon ca biir dëkk ba, di jënd lu ñu lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa sababu uzima ni bora kuliko chakula, na mwili ni bora kuliko mavazi.

Wolof

ndaxte bakkan moo gën lekk, te yaram a gën koddaay.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

alipoketi kula chakula pamoja nao, akachukua mkate, akaubariki, akaumega, akawapa.

Wolof

bi ñu tàmbali di reer, yeesu jël mburu ma, gërëm yàlla, ba noppi damm ko, jox leen ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"nawahurumia watu hawa kwa sababu wamekuwa nami kwa muda wa siku tatu, wala hawana chakula.

Wolof

«yërëm naa mbooloo mi, ndaxte toog nañu fi man ñetti fan, te amatuñu lu ñu lekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

afadhali uwaage watu waende mashambani na katika vijiji vya jirani, wanunue chakula."

Wolof

yiwil mbooloo mi nag, ñu dugg ci àll bi ak dëkk yi nu wër, jënd lu ñu lekk.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

hayo ndiyo yanayomtia mtu najisi. lakini kula chakula bila kunawa mikono hakumtii mtu najisi."

Wolof

yooyu ñooy indil nit sobe, waaye lekk ak loxo yoo raxasul du tax nit am sobe.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

lakini chakula hakiwezi kutupeleka karibu zaidi na mungu. tukiacha kukila hatupungukiwi kitu, tukikila hatuongezewi kitu.

Wolof

waaye ñam mënul a tax nu neex yàlla. su nu ci lekkee, du yokk dara ci nun. su nu ci lekkul, du nu wàññi dara.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

aliona njaa, akatamani kupata chakula. chakula kilipokuwa kinatayarishwa, alipatwa na usingizi mzito akaona maono.

Wolof

noonu xiif dab ko fa, mu bëgg a lekk. waaye bi ñu koy toggal, yàlla feeñu ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

huko walimwandalia chakula cha jioni, naye martha akawa anawatumikia. lazaro alikuwa mmoja wa wale waliokuwa mezani pamoja na yesu.

Wolof

foofa ñu defaral ko fa reer. màrt moo ko doon séddale, te lasaar bokkoon na ca gan ña.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

halafu akawachukua paulo na sila nyumbani kwake, akawapa chakula. yeye na jamaa yake yote wakafanya sherehe kwa vile sasa walikuwa wanamwamini mungu.

Wolof

bi ñu ko defee mu yóbbu leen ca këram, jox leen ñu lekk, mu bég lool ci li mu gëm yàlla, moom ak waa këram gépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

je, hamjui kwamba wanaotumikia hekaluni hupata chakula chao hekaluni, na kwamba wanaotolea sadaka madhabahuni hupata sehemu ya hiyo sadaka?

Wolof

xanaa xamuleen ne, ñiy liggéeyal yëf yu sell yi, dañuy lekk ñam, wi ci kër yàlla gi, te ñiy liggéey ci saraxalukaay bi, dañuy jot seen wàll ci sarax yi?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,899,377,386 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK