Results for dhabihu translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

lakini dhabihu hizo hufanyika kila mwaka kuwakumbusha watu dhambi zao.

Wolof

waaye dañuy fàttaliku bàkkaar yi ci sarax yi ñuy def at mu jot.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

msisahau kutenda mema na kusaidiana, maana hizi ndizo dhabihu zinazompendeza mungu.

Wolof

buleen fàtte di def lu baax ak di sédde ci seen alal, ndaxte sarax yu mel noonu ñoo neex yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, kwa dhabihu yake moja tu, amewafanya kuwa wakamilifu milele wale wanaotakaswa dhambi zao.

Wolof

noonu ñi ñuy sellal, ci benn sarax rekk la leen yeggali cig mat ba fàww.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, dhambi zikisha ondolewa, hakutakuwa na haja tena ya kutoa dhabihu za kuondoa dhambi.

Wolof

kon nag fu ñuy baale bàkkaar, aajootul sarax su koy dindi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa upande wangu mimi, niko karibu kabisa kutolewa dhabihu na wakati wa kufariki kwangu umefika.

Wolof

ndaxte maa ngi ci tànki joxe sama bakkan ni sarax, te sama waxtuw dem jot na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, kwa njia ya yesu, tumtolee mungu dhabihu ya sifa daima, yaani sifa zinazotolewa na midomo inayoliungama jina lake.

Wolof

kon nag nanu jaare ci yeesu, tey dëkk ci jébbal yàlla sarax bu koy màggal, maanaam sant turam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"baada ya kukaa mbali kwa miaka kadhaa, nilirudi yerusalemu ili kuwapelekea wananchi wenzangu msaada na kutoa dhabihu.

Wolof

«noonu gannaaw gëjeb at yu bare ñëw naa, ngir indil sama xeet ndimbal te jébbal yàlla ay sarax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

jambo hili ni mfano wa nyakati za sasa. linaonyesha kwamba zawadi na dhabihu zinazotolewa kwa mungu haziwezi kuifanya mioyo ya wale wanaoabudu kuwa mikamilifu,

Wolof

misaal la ci jamonoy tey; dafay wone ne, sarax yi ak saraxi mala yi ñu daan jagleel yàlla, mënuñoo dalal xelu jaamukatu yàlla bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

upendo uongoze maisha yenu, kama vile kristo alivyotupenda, na kwa ajili yetu akajitoa mwenyewe kama dhabihu yenye harufu nzuri na tambiko impendezayo mungu.

Wolof

ngeen wéer seen dund ci mbëggeel, mel ni kirist mi nu bëgg, ba joxe bakkanam ngir nun, di sarax su ñu jébbal yàlla te neex ko ni xetu latkoloñ.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ndiyo maana kristo alipokuwa anakuja ulimwenguni, alimwambia mungu: "hukutaka dhabihu wala sadaka, lakini umenitayarishia mwili.

Wolof

looloo tax bi muy wàcc àddina, kirist nee na:«bëggoo saraxu mala walla beneen sarax,waaye aw yaram nga ma defaral.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

vivyo hivyo kristo naye alijitoa dhabihu mara moja tu kwa ajili ya kuziondoa dhambi za wengi. atakapotokea mara ya pili si kwa ajili ya kupambana na dhambi, bali ni kwa ajili ya kuwaokoa wale wanaomngojea.

Wolof

noonu it la kirist joxee boppam benn yoon, ngir gàddu bàkkaaru nit ñu bare, te dina feeñaat, waxuma ci mbiri bàkkaar, waaye ngir indil ñi koy séentu mucc gi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, kajifunzeni maana ya maneno haya: nataka huruma, wala si dhabihu. sikuja kuwaita watu wema, bali wenye dhambi."

Wolof

mbind mi nee na: “yërmande laa bëgg, waaye du rendi saraxi mala.” demleen nag te seet lu wax joojuy tekki. ndaxte ñëwuma, ngir woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

maana ingalikuwa hivyo, kristo angalipaswa kuteswa mara nyingi tangu kuumbwa ulimwengu. lakini sasa nyakati hizi zinapokaribia mwisho wake, yeye ametokea mara moja tu, kuondoa dhambi kwa kujitoa yeye mwenyewe dhabihu.

Wolof

bu demee woon noonu, kon dina sonn ba tàyyi ca njàlbéenug àddina ba tey. waaye nag benn yoon rekk la feeñu ci mujjeelu jamono yi, joxe boppam ni sarax ngir far bàkkaar yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa imani, abrahamu alimtoa mwanae isaka sadaka wakati mungu alipomjaribu. huyo abrahamu ndiye aliyekuwa amepokea ahadi ya mungu, lakini, hata hivyo, alikubali kumtoa dhabihu mwanae wa pekee,

Wolof

ngëm moo tax ibraayma naroon a rey isaaxa ni sarax, bi ko yàlla nattoo. moom mi jotoon dige yi, moo demoon bay saraxe jenn doom ji mu am kepp,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa imani abeli alimtolea mungu dhabihu iliyokuwa bora zaidi kuliko ile ya kaini. kwa imani yake alikubaliwa na mungu kuwa mwadilifu; mungu mwenyewe alizikubali sadaka zake. kwa imani yake ingawa amekufa, bado ananena.

Wolof

ngëm moo tax ba abel jébbal yàlla sarax su gën saraxu kayin. ngëmu abel moo tax ba yàlla àtte ko ni ku jub, bi mu ko seedeelee ne, saraxam baax na. te ci kaw ngëm lay wax ba tey, moom mi dee ba noppi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kisha akasema: "niko hapa, ee mungu, tayari kufanya mapenzi yako." hivyo mungu alibatilisha dhabihu za zamani na mahali pake akaweka dhabihu nyingine moja.

Wolof

noonu mu tegaat ca ne: «damaa wàcc ngir def sa coobare.» noonu toxal na jëfin wu jëkk wa, ngir wuutal fi weneen wu bees.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,746,058,084 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK