From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
watu wa mataifa mengine watakuhukumu wewe myahudi kama ukiivunja sheria, ingawaje unayo maandishi ya sheria na umetahiriwa, hali wao wanaitii sheria ingawa hawakutahiriwa.
ku dul yawut te xaraful waaye di sàmm yoon wi, kooku dina la man a àtte yaw yawut bi. ndaxte li ngay xam-xam yoonu musaa ci mbind mi te xaraf, terewul nga koy moy.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
abrahamu alitahiriwa baadaye, na kutahiriwa huko kulikuwa alama iliyothibitisha kwamba mungu alimkubali kuwa mwadilifu kwa sababu ya imani yake aliyokuwa nayo kabla ya kutahiriwa. kwa hiyo, abrahamu amekuwa baba wa wale wote ambao, ingawa hawakutahiriwa, wamemwamini mungu, wakafanywa waadilifu.
ndaxte ibraayma gëm na, te yàlla jàppe na ngëmam ni njub, fekk booba xarafagul. te xarafal gi, màndarga la woon ci yaramam, di firndeel ne, ku jub la woon. noonu la ibraayma man a nekke baayu ñépp ñi gëm, ba yàlla man leen a àtte ni ñu jub, te xarafuñu sax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality: