From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
yesu alipofufuka mapema jumapili, alijionyesha kwanza kwa maria magdalene, ambaye yesu alikuwa amemtoa pepo saba.
bi yeesu dekkee nag ci suba teel ca bés bu jëkk ca ayu-bés ga, mu jëkk a feeñu maryaama mu dëkk magdala, mi mu dàqe woon juróom-ñaari rab.
kila jumapili kila mmoja wenu atenge kiasi cha fedha kadiri ya mapato yake, ili kusiwe na haja ya kufanya mchango wakati nitakapokuja.
bés bu jëkk ci ayu-bés yi, na ku nekk ber lu mu àttan, denc ko, ngir saa yu ma dikkee, ñu bañ di wër di laaj xaalis.
alfajiri na mapema jumapili, kukiwa bado na giza, maria magdalene alikwenda kaburini, akaliona lile jiwe limeondolewa mlangoni pa kaburi.
bés ba jiitu ca ayu-bés ga, maryaamam magdala jóg ca fajar, dem ca bàmmeel ba. bi mu agsee, mu gis ne dindi nañu xeer, wa ñu ko ube woon.
ilikuwa jioni ya siku hiyo ya jumapili. wanafunzi walikuwa wamekutana pamoja ndani ya nyumba, na milango ilikuwa imefungwa kwa sababu waliwaogopa viongozi wa wayahudi. basi, yesu akaja, akasimama kati yao, akawaambia, "amani kwenu!"
bés boobu ca ngoon sa, taalibe yaa nga daje woon ca genn kër, tëju ca biir ndax ragal yawut ya. yeesu ne tëll ci seen biir ne leen: «na jàmm wàcc ci yéen!»