Results for kumwona translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

yesu akapewa habari kwamba mama na ndugu zake walikuwa nje, wanataka kumwona.

Wolof

am ku ko yégal ne: «sa yaay ak say rakk ñu ngi nii taxaw ci biti, bëgg laa gis.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

roho mtakatifu alikuwa amemhakikishia kwamba hatakufa kabla ya kumwona masiha wa bwana.

Wolof

te xamal na ko ne, du dee mukk te gisul almasib boroom bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mama yake yesu na ndugu zake walifika hapo, wakasimama nje, wakampelekea ujumbe kutaka kumwona.

Wolof

noonu ndeyu yeesu ak ay rakkam ñëw, ñu taxaw ci biti, yónnee, woo ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

alipokwisha sema hayo, akawaonyesha mikono yake na ubavu wake. basi, hao wanafunzi wakafurahi mno kumwona bwana.

Wolof

mu daldi leen won ay loxoom ak wetam. bi ñu gisee boroom bi, taalibe ya daldi bég lool.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kweli nawaambieni, wako wengine papahapa ambao hawatakufa kabla ya kumwona mwana wa mtu akija katika ufalme wake."

Wolof

ci dëgg maa ngi leen koy wax, am na ñi fi taxaw, ñoo xam ne duñu dee, te gisuñu doomu nit ki ñëw ci nguuram.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, niambieni, mlikwenda kuona nini? mlikwenda kumwona nabii? naam, hakika ni zaidi ya nabii.

Wolof

kon lu ngeen seeti woon? yonent? waaw, wax naa leen ne, ëpp na yonent.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

halafu anania akasema: mungu wa babu zetu amekuchagua upate kujua matakwa yake na kumwona yule mtumishi wake mwadilifu na kumsikia yeye mwenyewe akiongea.

Wolof

mu ne ma: “sunu yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis aji jub ji te nga dégg ay waxam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, kila aishiye katika muungano na kristo hatendi dhambi; lakini kila mtu atendaye dhambi hakupata kamwe kumwona, wala kumjua kristo.

Wolof

képp ku sax ci moom, doo sax ci bàkkaar; kuy def bàkkaar, gisuloo ko te xamuloo ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini herode akasema, "huyo yohane nilimkata kichwa; sasa ni nani huyu ninayesikia habari zake?" akawa na hamu ya kumwona.

Wolof

waaye erodd ne: «yaxya, man mii maa dagglu boppam. kon kii ma dégg ay jalooreem, mooy kan?» noonu mu koy fexee gis.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

yesu aliposikia hayo, alistaajabu, akawaambia watu waliokuwa wanamfuata, "kweli nawaambieni, sijapata kumwona mtu yeyote katika israeli aliye na imani kama hii.

Wolof

bi ko yeesu déggee, mu waaru, ne ña topp ci moom: «ci dëgg maa ngi leen koy wax, musumaa gis ci bànni israyil ku gëme ni kii.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

herode alifurahi sana alipomwona yesu. alikuwa amekwisha sikia habari zake, na hivyo alikuwa anatazamia kwa muda mrefu kumwona kwa macho yake mwenyewe. zaidi ya hayo, alikuwa anatumaini kumwona yesu akitenda mwujiza.

Wolof

bi erodd gisee yeesu, mu am mbég mu réy. bu yàgg ba tey dafa koo bëggoon a gis, ndaxte déggoon na ñuy wax ci ay mbiram te yaakaaroon na ne, dina ko gis mu def kéemaan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, ikawa kwamba baba yake publio alikuwa amelala kitandani, mgonjwa, ana homa na kuhara. paulo alikwenda kumwona na baada ya kusali, akaweka mikono yake juu ya mgonjwa, akamponya.

Wolof

fekk baayu publiyus dafa tëdd ndax ay tàngoori yaram yu koy dikkal ak biiru taññ. pool nag dem seeti ko, ñaan ci yàlla, teg ko ay loxoom, mu daldi wér.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, mlikwenda kuona nini? mlikwenda kumwona mtu aliyevalia mavazi maridadi? la hasha! wanaovaa mavazi maridadi na kuishi maisha ya anasa, hukaa katika majumba ya wafalme!

Wolof

kon lu ngeen seeti woon nag? nit ku sol yére yu rafet? waaye ñiy soloo noonu, tey dund dund gu neex ñu ngi dëkk ci këri buur.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,934,729,637 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK