Results for kutekeleza translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

baada ya barnaba na saulo kutekeleza shughuli zao, walitoka tena yerusalemu wakamchukua yohane aitwaye pia marko.

Wolof

naka barnabas ak sool, bi ñu matalee seen liggéey, ñu jóge yerusalem, ñibbi, ànd ak yowaana mi tudd màrk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kisha akawaambia wale wajumbe wa baraza, "wananchi wa israeli, tahadhari kabla ya kutekeleza hicho mnachotaka kuwatenda watu hawa!

Wolof

bi ñu ko defee mu ne leen: «yéen bokki israyil, moytuleen li ngeen di def nit ñooñu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

maana mungu ametia mioyoni mwao nia ya kutekeleza shabaha yake, yaani kwa kukubaliana wao kwa wao na kumpa huyo mnyama mamlaka yao ya kutawala, mpaka hapo neno la mungu litakapotimia.

Wolof

ndaxte yàlla def na ci seen xol, ñu matal la mu naroon. noonu dinañu ànd, jébbal seen nguur rab wi, ba kera li yàlla wax di mat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kuhusu jambo hili, basi, nawapeni shauri hili: inafaa kwenu kutekeleza sasa yale mliyoanza mwaka jana. ninyi mlikuwa wa kwanza kuchukua hatua na kuamua kufanya hivyo.

Wolof

kon lii laa xalaat ci lu baax ci yéen: yéen ñi nga xam ne tàmbaliwuleen a jëf rekk, waaye yéena jëkk a am yéene jii daaw,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mungu ametekeleza jambo lile ambalo sheria haikuweza kutekeleza kwa sababu ya udhaifu w binadamu. mungu alimtuma mwanae akiwa mwenye mwili sawa na miili yetu sisi wenye dhambi, ili aikabili dhambi, na kwa mwili huo akaiangamiza dhambi.

Wolof

lu yoonu musaa mënul woon a def, ndax néew dooley nit, yàlla defe na ko nii: dafa yónni doomam, ngir mu yor sunu jëmm, nun ñiy nekk ay bàkkaarkat, te mu jébbale bakkanam, ngir dindi bàkkaar yi. noonu la yàlla tase nguuru bàkkaar ci nit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

ninyi ni watoto wa baba yenu ibilisi na mnataka tu kutekeleza tamaa za baba yenu. yeye alikuwa muuaji tangu mwanzo; hana msimamo katika ukweli, kwani ukweli haumo ndani yake. kila asemapo uongo, husema kutokana na hali yake ya maumbile, maana yeye ni mwongo na baba wa uongo.

Wolof

seytaane mooy seen baay, te bëgg-bëggam ngeen di bëgg di def. bóomkat la mas a doon. du taxaw mukk ci dëgg, ndaxte dëgg nekkul ci moom. buy fen, dëppoo na ak jikkoom, ndaxte fenkat la, te ci moom la fen soqikoo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,773,672,649 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK