Results for makubwa translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

watu wamchao mungu, walimzika stefano na kumfanyia maombolezo makubwa.

Wolof

ay nit ñu ragal yàlla fab ecen, jébbal ko boroom bi, di ko jooy bu wér.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

makundi makubwa ya watu yalimzunguka hata yesu akapanda mashua, akaketi. hao watu walisimama kwenye ukingo wa ziwa,

Wolof

mbooloo mu bare dajaloo ca moom, ba tax mu dugg cig gaal, toog; mbooloo mépp taxaw ca tefes ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hekalu likajaa moshi uliosababishwa na utukufu na nguvu ya mungu, na hakuna mtu aliyeweza kuingia hekaluni mpaka mwisho wa mabaa makubwa saba ya wale malaika saba.

Wolof

kër yàlla ga fees ak saxar ndax leeraayu ndamu yàlla ak kàttanam. te kenn mënatul a dugg ca kër yàlla ga, ba kera juróom-ñaari musiba, ya juróom-ñaari malaaka ya taawu, di mat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, watu wakaunguzwa vibaya sana; wakamtukana mungu aliye na uwezo juu ya mabaa hayo makubwa. lakini hawakuziacha dhambi zao na kumtukuza mungu.

Wolof

naaj wu metti di lakk nit ñi, ñu daldi xarab turu yàlla, ji am sañ-sañ ci kaw musiba yooyu. waaye tuubuñu sax seeni bàkkaar, ngir jox ko ndam li.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

bwana wake akamwambia, vema, mtumishi mwema na mwaminifu. umekuwa mwaminifu katika mambo madogo, nitakukabidhi makubwa. njoo ufurahi pamoja na bwana wako.

Wolof

njaatigeem ne ko: “def nga lu baax, surga bu baax nga te takku. gannaaw takku nga ci lu tuuti, dinaa la dénk lu bare. kaay bokk ci sama mbég.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yesu akamwambia, "je, umeamini kwa kuwa nimekwambia kwamba nilikuona chini ya mtini? utaona makubwa zaidi kuliko haya."

Wolof

yeesu tontu ko ne: «ndax li ma ne, gis naa la ca ker garab ga, moo tax nga gëm? dinga gis mbir yu gën a réy yii.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kisha nikaona ishara nyingine mbinguni, kubwa na ya kushangaza. palikuwa hapo malaika saba wenye mabaa makubwa saba ya mwisho. kwa mabaa hayo makubwa saba, ghadhabu ya mungu imekamilishwa.

Wolof

noonu ma gis ca asamaan beneen firnde ju réy tey yéeme: juróom-ñaari malaaka yu taawu juróom-ñaari musiba, ñuy yu mujj ya, ndaxte ñoom ñooy matal merum yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,889,179,808 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK