From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
papo hapo midomo na ulimi wake zakariya vikafunguliwa, akawa anaongea akimsifu mungu.
ca saa sa yàlla dindi luu gi, sakariya daldi waxaat, di màggal yàlla.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
maana tunaamini kwa moyo na kukubaliwa kuwa waadilifu; na tunakiri kwa midomo yetu na kuokolewa.
ndax xol la nit di gëme, ba tax mu jub ci kanam yàlla; làmmiñ it la nit di waxe ne, mi ngi ci kirist, ba tax yàlla musal ko.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
basi, kwa njia ya yesu, tumtolee mungu dhabihu ya sifa daima, yaani sifa zinazotolewa na midomo inayoliungama jina lake.
kon nag nanu jaare ci yeesu, tey dëkk ci jébbal yàlla sarax bu koy màggal, maanaam sant turam.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
imeandikwa katika sheria: "bwana asema hivi: kwa njia ya wenye kunena lugha ngeni, na kwa midomo ya wageni, nitasema na watu hawa, hata hivyo, hawatanisikiliza."
bind nañu ci téereb yoon wi:«dinaa wax ak mbooloo mii,jaare ko ci ay nit, ñuy wax yeneen làkk,ak ay gémmiñi doxandéem,waaye ba tey duñu ma déglu.» moom la boroom bi wax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting