Results for mwalimu translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

wakapaza sauti wakisema, "yesu mwalimu, tuonee huruma!"

Wolof

«yeesu, kilifa gi, yërëm nu!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"mwalimu, ni amri ipi iliyo kuu katika sheria ya mose?"

Wolof

«kilifa gi, ban ndigal moo gën a màgg ci yoonu musaa?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

mtu mmoja akamwuliza, "je, mwalimu, watu watakaookoka ni wachache?"

Wolof

am ku ko ne: «boroom bi, ndax ñiy mucc ñu néew lay doon?» yeesu ne leen:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

hupenda kusalimiwa kwa heshima sokoni na kupendelea kuitwa na watu: mwalimu.

Wolof

dañoo bëgg ñépp nuyoo leen ñaari loxo ca pénc ma, di leen wooye “kilifa gi.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kisha wakamwuliza yesu, "mwalimu! mwanamke huyu alifumaniwa katika uzinzi.

Wolof

noonu ñu ne yeesu: «kilifa gi, jigéen jii de, dañu koo bett muy njaaloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"mwanafunzi si mkuu kuliko mwalimu wake, wala mtumishi si mkuu kuliko bwana wake.

Wolof

yeesu teg ca ne: «taalibe gënul kilifaam, te jaam gënul sangam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

mtumishi wa bwana asigombane. anapaswa kuwa mpole kwa watu wote, mwalimu mwema na mvumilivu,

Wolof

te jaamu boroom bi warul a xuloo, waaye na lewet ci ñépp, jekk ngir jàngale tey muñ fitnay noon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

baadhi ya wale walimu wa sheria wakasema, "mwalimu, umejibu vema kabisa."

Wolof

ci kaw loolu ay xutbakat ne ko: «li nga wax dëgg la, kilifa gi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

yuda alipofika tu, alimwendea yesu moja kwa moja, akasema, "mwalimu!" kisha akambusu.

Wolof

noonu mu ñëw ci yeesu ne ko: «kilifa gi,» daldi ko fóon.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

lakini ninyi msiitwe kamwe mwalimu, maana mwalimu wenu ni mmoja tu, nanyi nyote ni ndugu.

Wolof

waaye yéen buñu leen wooye “kilifa gi,” ndaxte kenn rekk moo di seen kilifa, te yéen ñépp ay bokk ngeen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, ikiwa mimi niliye bwana na mwalimu, nimewaosha ninyi miguu, nanyi pia mnapaswa kuoshana miguu.

Wolof

kon bu fekkee ne man miy boroom bi tey kilifa gi, maa leen raxasal seeni tànk, yéen itam war ngeen di raxasalante seeni tànk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hapo baadhi ya mafarisayo waliokuwako katika lile kundi la watu, wakamwambia yesu, "mwalimu, wanyamazishe wanafunzi wako!"

Wolof

waaye ay farisen yu nekkoon ca mbooloo ma ne yeesu: «kilifa gi, yeddal sa taalibe yi!»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

baadaye mwalimu mmoja wa sheria alisimama akamwuliza akitaka kumtega, "mwalimu, nifanye nini ili nipate uzima wa milele?"

Wolof

noonu benn xutbakat daldi jóg, ngir fexee fiir yeesu ne ko: «kilifa gi, lan laa war a def, ba am dund gu dul jeex?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kiongozi mmoja, myahudi, alimwuliza yesu, "mwalimu mwema, nifanye nini ili niweze kuupata uzima wa milele?"

Wolof

benn njiitu yawut laaj yeesu ne ko: «kilifa gu baax gi, lu ma war a def, ba am wàll ci dund gu dul jeex?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

alipokuwa bado akiongea, yairo akaletewa habari kutoka nyumbani: "binti yako ameshakufa, ya nini kumsumbua mwalimu zaidi?"

Wolof

bi yeesu di wax nag, am na ku jóge ca kër njiit la, mu ñëw naan: «sa doom faatu na; matatul ngay sonal kilifa gi.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"mwalimu, mose alituagiza hivi: mtu akifa na kuacha mke bila mtoto, ndugu yake lazima amchukue huyo mama mjane amzalie watoto ndugu yake marehemu.

Wolof

Ñu ne ko: «kilifa gi, musaa bindal na nu ne, ku magam faatu, te bàyyiwul doom ak jabaram, kooku war na donn jigéen ji, ba yékkati giiru magam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, wakamwambia, "mwalimu, mose alisema mtu aliyeoa akifa bila kuacha watoto, lazima ndugu yake amwoe huyo mama mjane, amzalie ndugu yake watoto.

Wolof

«kilifa gi, musaa nee woon na: “boo xamee ne góor dee na te amul doom, na rakkam donn jabaram, ngir sàkkal magam njaboot.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"mwalimu, mose alituandikia kwamba kama ndugu ya mtu fulani akifa na kumwacha mjane wake bila watoto, ni lazima ndugu yake amchukue huyo mama mjane, amzalie watoto ndugu yake marehemu.

Wolof

«kilifa gi, musaa bindal na nu ne, ku magam faatu te bàyyiwul doom ak jabaram, kooku war na donn jigéen ji, ba yékkati giiru magam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

hao wapelelezi wakamwambia, "mwalimu, tunajua kwamba unasema na kufundisha mambo ya kweli; tunajua kwamba wewe huna ubaguzi; wewe wafundisha ukweli juu ya njia ya mungu.

Wolof

Ñu daldi ñëw ci yeesu ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne li ngay wax te di ko jàngale lu jub la. amuloo parlàqu, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, wakawatuma wafuasi wao pamoja na wafuasi wa kikundi cha herode. wakamwuliza, "mwalimu, tunajua kwamba wewe ni mtu mwaminifu, na kwamba wafundisha njia ya mungu kwa uaminifu; humwogopi mtu yeyote, maana cheo cha mtu si kitu kwako.

Wolof

noonu ñu yónni ci moom seeni taalibe ak ñi far ak buur bi erodd ne ko: «kilifa gi, xam nanu ne ku wóor nga, te ragaloo kenn, ndaxte seetuloo jëmmi nit, waaye dangay xamle yoonu yàlla ci bu wóor.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,774,185,786 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK