Results for nilikotoka translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

hapo hujisemea: nitarudi nyumbani kwangu nilikotoka. lakini anaporudi na kuikuta tupu, imefagiwa na kupambwa,

Wolof

noonu da naan: “naa dellu ca sama kër, ga ma génne woon.” bu ñëwee nag, mu fekk kërug neen, ñu bale ko, defar ko ba lépp jekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yesu akawajibu, "hata kama ninajishuhudia mwenyewe, ushahidi wangu ni wa kweli kwa sababu mimi najua nilikotoka na ninakokwenda. lakini ninyi hamjui nilikotoka wala ninakokwenda.

Wolof

yeesu tontu leen: «maa ngi seedeel sama bopp, teewul li may wax di dëgg, ndaxte xam naa fa ma bàyyikoo, xam fa ma jëm. waaye yéen xamuleen fa ma bàyyikoo ak fa ma jëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"pepo mchafu akifukuzwa kwa mtu fulani, huzururazurura jangwani akitafuta mahali pa kupumzikia. asipopata, hujisemea: nitarudi kwenye makao yangu nilikotoka.

Wolof

«boo xamee ne rab, wa jàppoon nit, génn na ci moom, day wër ay bérab yu wow, di wut fu mu noppaloo, waaye du ko gis. noonu da naan: “naa dellu ca sama kër, ga ma jóge.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, yesu alipokuwa anafundisha hekaluni alipaaza sauti na kusema, "ati mnanijua; hata nilikotoka mnakujua! hata hivyo, sikuja kwa mamlaka yangu mwenyewe; ila yeye aliyenituma mimi ni wa kweli, nanyi hamumjui.

Wolof

yeesu di jàngale ca kër yàlla ga, daldi wax ca kaw ne: «ndax xam ngeen ma te xam fi ma jóge? Ñëwaluma sama bopp, waaye ki ma yónni, ku wóor la. yéen xamuleen ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,794,579,110 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK