Results for sunagogi translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

yesu alitoka hapo, akaenda katika sunagogi lao.

Wolof

bi loolu amee yeesu jóge foofa, dugg ci seen jàngu,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wote waliokuwa katika lile sunagogi waliposikia hayo walikasirika sana.

Wolof

bi ñu déggee wax yooya, ñépp ña nekkoon ca jàngu ba daldi fees ak mer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yesu alisema hayo alipokuwa akifundisha katika sunagogi kule kafarnaumu.

Wolof

baat yooyu la yeesu wax, bi mu doon jàngale ca jàngu ba ca kapernawum.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

maana analipenda taifa letu, na ndiye aliyetujengea lile sunagogi."

Wolof

ndaxte sopp na sunu xeet te moo nu tabaxal sax sunu jàngu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kila sabato alifanya majadiliano katika sunagogi akijaribu kuwavuta wayahudi na wagiriki.

Wolof

bésu noflaay bu nekk nag muy diisoo ak ñi nekk ca jàngu ba, di jéem a gëmloo ay yawut ak ay gereg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yesu aliingia tena katika sunagogi na mle ndani mlikuwa na mtu aliyekuwa na mkono uliopooza.

Wolof

am beneen bés, yeesu duggaat ci jàngu bi, fekk amoon na fa nit ku loxoom làggi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wakafika nyumbani kwa ofisa wa sunagogi naye yesu akasikia makelele, kilio na maombolezo mengi.

Wolof

naka lañu ñëw ci kër njiit li, yeesu dégg coow li; ñii di jooy, ñii di yuuxu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa kupitia amfipoli na apolonia, walisafiri mpaka thesalonika ambako kulikuwa na sunagogi la wayahudi.

Wolof

bi ñu fa jógee, ñu aw yoon wa jaar dëkku amfipolis ak apoloni, door a ñëw tesalonig, fa yawut ya am jàngu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wakafika mjini kafarnaumu, na mara ilipofika sabato, yesu akaingia katika sunagogi, akaanza kufundisha.

Wolof

gannaaw loolu ñu dem kapernawum. ca bésu noflaay nag yeesu daldi dugg ci jàngu bi, di leen jàngal.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

walifika efeso na hapo paulo aliwaacha priskila na akula, akaenda katika sunagogi, akajadiliana na wayahudi.

Wolof

noonu ñu teer ci efes. pool bàyyi fa ñi mu àndaloon, daldi dugg ca jàngu ba, di diisoo ak yawut ya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hapo akaja mmojawapo wa maofisa wa sunagogi, jina lake yairo. alipomwona yesu, akajitupa mbele ya miguu yake,

Wolof

kenn ci njiiti jàngu ba nag, tudd yayrus, ñëw ci moom. naka la gis yeesu, mu daanu ciy tànkam,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hapo akaja mtu mmoja aitwaye yairo, ofisa wa sunagogi. alijitupa miguuni pa yesu, akamwomba aende nyumbani kwake,

Wolof

noonu nit ñëw, tuddoon yayrus te nekk njiitu jàngu ba. bi mu agsee, mu daanu ci tànki yeesu, saraxu ko mu ñëw këram,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

alijadiliana na wayahudi na watu wengine waliomcha mungu katika sunagogi; na kila siku alikuwa na majadiliano sokoni pamoja na wowote wale waliojitokeza.

Wolof

muy werante nag ca jàngu ba ak yawut ya ak ña ragal yàlla, tey werante it bés bu nekk ca pénc ma ak ña fay dajaloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hata hivyo, wengi wa viongozi wa wayahudi walimwamini yesu. lakini kwa sababu ya mafarisayo, hawakumkiri hadharani kwa kuogopa kwamba watatengwa na sunagogi.

Wolof

fekk na ci biir njiit yi sax, ñu bare gëmoon nañu yeesu, waaye farisen yee tax fésaluñu ko, ndaxte dañoo ragaloon, ñu dàq leen ca jàngu ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini krispo, mkuu wa sunagogi, alimwamini bwana yeye pamoja na jamaa yake yote. wakorintho wengi waliusikiliza ujumbe huo, wakaamini na kubatizwa.

Wolof

kirispus nag, njiitu jàngu ba, gëm na boroom bi ak waa këram gépp. te waa korent ñu bare dégg kàddu gi te gëm ko, ñu sóob leen ci ndox.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

akaenda kijijini kwake. huko akawa anawafundisha watu katika sunagogi hata wakashangaa, wakasema, "huyu amepata wapi hekima hii na maajabu?

Wolof

dem fa mu yaroo. mu di leen jàngal ci seen jàngu, ba ñu waaru ne: «xam-xam bii ak kéemaan yii, fu mu ko jële?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, yesu alikwenda nazareti, mahali alipolelewa, na siku ya sabato, aliingia katika sunagogi, kama ilivyokuwa desturi yake. akasimama ili asome maandiko matakatifu kwa sauti.

Wolof

yeesu dem nasaret fa mu yaroo, te ca bésu noflaay ba, mu dugg ca jàngu ba, ni mu ko daan defe. noonu mu taxaw ngir jàngal mbooloo mi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

baada ya masomo katika kitabu cha sheria ya mose na katika maandiko ya manabii, wakuu wa lile sunagogi waliwapelekea ujumbe huu: "ndugu, kama mnalo jambo la kuwaambia watu ili kuwapa moyo, semeni."

Wolof

bi ñu jàngee yoonu musaa ak yonent ya, njiiti jàngu ba yónnee ca ñoom ne leen: «bokk yi, bu ngeen amee lu ngeen di dénk mbooloo mi, waxleen ko.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,776,710,566 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK