Results for uzinzi translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

basi, matendo ya kidunia yanajulikana: uzinzi, uasherati, ufisadi;

Wolof

kuy topp sa nafsu, nii ngay jëfe: njaaloo, xalaat yu bon, def i ñaawteef ak say cér,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

nimempa muda wa kutubu dhambi zake, lakini hataki kuachana na uzinzi wake.

Wolof

may naa ko ab diir, ngir mu tuub njaaloom, waaye bañ na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kisha wakamwuliza yesu, "mwalimu! mwanamke huyu alifumaniwa katika uzinzi.

Wolof

noonu ñu ne yeesu: «kilifa gi, jigéen jii de, dañu koo bett muy njaaloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

uzinzi, uchoyo, uovu, udanganyifu, ufisadi, wivu, kashfa, kiburi na upumbavu.

Wolof

njaaloo ak bëgge, coxor, naaféq, ñaawteef, ñeetaan, saaga, réylu ak jëfi ndof.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, walimu wa sheria na mafarisayo wakamletea mwanamke mmoja aliyefumaniwa katika uzinzi. wakamsimamisha katikati yao.

Wolof

xutbakat ya ak farisen ya indi jenn jigéen ju ñu bettoon muy njaaloo, ñu taxawal ko ca diggu mbooloo ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wafalme wa dunia waliofanya uzinzi naye na kuishi naye maisha ya anasa wataomboleza na kulia wakati watakapoona moshi wa mji huo unaoteketea.

Wolof

buuri àddina yépp, yi àndoon ak moom ci njaaloo ak mbuux, bu ñu séenee saxar siy jollee ci taal bi ñu koy lakke, dinañu yuuxu, di ko jooy.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

jiepusheni kabisa na uzinzi. dhambi nyingine zote hutendwa nje ya mwili lakini mzinzi hutenda dhambi dhidi ya mwili wake mwenyewe.

Wolof

dawleen njaaloo! bépp bàkkaar bu nit man a def, du laal yaramam, waaye nag kuy njaaloo, dafay bàkkaar, di lor yaramam.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini kwa sababu ya hatari ya uzinzi, basi, kila mwanamume na awe na mke wake mwenyewe, na kila mwanamke awe na mume wake mwenyewe.

Wolof

lii mooy sama xalaat: moy gu bare gi tax na ba, na góor gu nekk am jabaram, jigéen ju nekk am jëkkëram.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini ninayo machache dhidi yako: baadhi yenu ni wafuasi wa balaamu aliyemfundisha balaki kuwatega wana wa israeli wale vyakula vilivyotambikiwa sanamu za kufanya uzinzi.

Wolof

waaye am na lu ma naqari ci yaw, moo di uuf nga foofu gaa yuy sàmm njàngalem balaam, moom mi jàngaloon balag, mu sóob bànni israyil ci bàkkaar, xiir leen ci lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi, xiir leen ci njaaloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini nina hoja moja juu yako: wewe unamvumilia yule mwanamke yezabeli anayejiita nabii wa mungu. yeye huwafundisha na kuwapotosha watumishi wangu wafanye uzinzi na kula vyakula vilivyotambikiwa sanamu.

Wolof

waaye li ma naqari ci yaw moo di dangaa bàyyi yesabel, jigéen joojuy tuddoo yonent, di jàngale ak a réeral sama jaam yi, ngir ñuy sóobu ci njaaloo te di lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini haikuwa hivyo tangu mwanzo. basi nawaambieni, yeyote atakayemwacha mke wake isipokuwa kwa sababu ya uzinzi, akaoa mke mwingine, anazini."

Wolof

te it maa ngi leen koy wax, koo xam ne kii fase nga sa jabar te du njaaloo tax, boo séyaatee ak keneen, njaaloo nga.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

macho yao yamejaa uzinzi na uwezo wao wa kutenda dhambi hauna kikomo. huwaongoza watu walio dhaifu mpaka mitegoni. mioyo yao imezoea kuwa na tamaa ya mali. wapo chini ya laana ya mungu!

Wolof

jigéen ju seen bët tegu, ñu xédd ko, ba duñu tàggook moy mukk; ku ñàkk pasteef ñu fàbbi la; ñu xelu lañu jëme cig bëgge -- ñu alku lañu!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mwanamke huyo alikuwa amevaa vazi la rangi ya zambarau na nyekundu; alikuwa amejipamba kwa dhahabu, mawe ya thamani na lulu. mkononi mwake alishika kikombe cha dhahabu ambacho kilikuwa kimejaa machukizo na mambo machafu yanayoonyesha uzinzi wake.

Wolof

jigéen ja sol lu yolet te xonq, takk wurus ak jamaa ak ay per. yoroon na koppu wurus bu fees ak ñaawteef ak sobeem.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kumbukeni pia sodoma na gomora, na miji ya kandokando yake; wenyeji wake walifanya kama wale malaika; walifanya uzinzi na mambo yaliyo kinyume cha maumbile, wakapewa hukumu ya moto wa milele, iwe onyo kwa watu wote.

Wolof

noonu itam dëkki sodom ak gomor ak dëkk ya leen wëroon, dañoo sóobu ci njaaloo ak di def ay góor-jigéen, waaye àtte bi dal na ci seen kaw, ba ñuy ay tegtal ci ñiy yelloo safara ba fàww.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,743,736,561 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK