Results for walimwendea translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

askari nao walimdhihaki pia; walimwendea wakampa siki

Wolof

xarekat ya it di ko ñaawal. Ñu jegesi, jox ko bineegar te naan:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

vipofu na vilema walimwendea huko hekaluni, naye yesu akawaponya.

Wolof

noonu ay gumba ak ay lafañ ñëw ci moom ca kër yàlla ga, mu faj leen.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

masadukayo wasemao kwamba hakuna ufufuo walimwendea yesu, wakamwuliza,

Wolof

gannaaw loolu ay sadusen ñëw ci moom, ngir laaj ko lenn. sadusen yi nag gëmuñu ne, ndekkite am na.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wasamaria walimwendea yesu wakamwomba akae nao; naye akakaa hapo siku mbili.

Wolof

Ñu daldi dikk ñaan yeesu, mu dal ak ñoom. yeesu toog fa ñaari fan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

siku hiyo, baadhi ya masadukayo walimwendea yesu. hao ndio wale wasemao kwamba wafu hawafufuki.

Wolof

bés boobale ay sadusen ñëw ci moom. sadusen yi nag ñoom gëmuñu ne ndekkite am na. noonu ñu laaj ko naan:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mafarisayo na masadukayo walimwendea yesu, na kwa kumjaribu, wakamwomba afanye ishara itokayo mbinguni.

Wolof

amoon na ay farisen ak ay sadusen yu ñëw ci yeesu. Ñu fexe koo fiir, ba laaj ko ne: «won nu kéemaan guy firndeel sag yónnent, te mu jóge ci asamaan.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kesho yake, yaani siku iliyofuata ile ya maandalio, makuhani wakuu na mafarisayo walimwendea pilato,

Wolof

ba bët setee nag, ca bés ba topp bésu waajal ba, saraxalekat yu mag ya ak farisen ya dajaloo, jëm ci pilaat.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

yesu alitoka hekaluni, na alipokuwa akienda zake, wanafunzi wake walimwendea, wakamwonyesha majengo ya hekalu.

Wolof

bi yeesu waxee ba noppi, mu génn ca kër yàlla ga, dem. noonu ay taalibeem ñëw ci moom, ngir won ko tabaxi kër yàlla ga.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wakati ule wanafunzi walimwendea yesu, wakamwuliza, "ni nani aliye mkuu katika ufalme wa mbinguni?"

Wolof

ca waxtu woowu taalibe ya ñëwoon nañu ci yeesu, laaj ko: «kan moo gën a màgg ci nguuru yàlla mi nekk ci kaw?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, watu kutoka yerusalemu, kutoka mkoa wote wa yudea na sehemu zote za kandokando ya mto yordani, walimwendea,

Wolof

noonu ñépp génn jëm ci moom, ñi dëkk yerusalem ak diiwaanu yude, ak waa dexu yurdan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, wakafika tena yerusalemu. yesu alipokuwa akitembea hekaluni, makuhani wakuu, walimu wa sheria na wazee walimwendea,

Wolof

gannaaw loolu ñu duggaat yerusalem, te yeesu doon doxantu ca ëtti kër yàlla ga. noonu saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya dab ko

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hao walimwendea filipo, mwenyeji wa bethsaida katika galilaya, wakasema, "mheshimiwa, tunataka kumwona yesu."

Wolof

Ñëw nañu ci filib, mi dëkk betsayda ci diiwaanu galile, ne ko: «sang bi, danoo bëggoon a gis yeesu.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

baada ya siku tano, kuhani mkuu anania aliwasili kaisarea pamoja na wazee kadhaa na wakili mmoja wa sheria aitwaye tertulo. walimwendea yule mkuu wa mkoa wakamweleza mashtaka yao juu ya paulo.

Wolof

bi juróomi fan wéyee, anañas saraxalekat bu mag ba dikk, ànd ak ay njiit ak layookat bu tudd tertul, ñu woo pool ci yoon fa kanam boroom réew ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wakati huohuo, mafarisayo na watu wengine walimwendea yesu wakamwambia, "ondoka hapa uende mahali pengine, kwa maana herode anataka kukuua."

Wolof

ca jamono jooja ay farisen ñëw ca yeesu ne ko: «jógeel fii, dem feneen, ndaxte erodd a ngi lay wut a rey.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

kulipokuwa jioni, wanafunzi wake walimwendea wakamwambia, "mahali hapa ni nyikani, na saa zimepita. basi, uwaage watu ili waende vijijini wakajinunulie chakula."

Wolof

ca ngoon sa taalibe yi ñëw ci moom ne ko: «fii àllub neen la, te léegi mu guddi. doo yiwi mbooloo mi, ngir ñu dem ci dëkk yu ndaw yi, jënd lu ñu man a lekk?»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

jua lilipokuwa linaanza kutua, wale kumi na wawili walimwendea wakamwambia, "waage watu waende kwenye vijiji na mashamba ya karibu, wakajipatie chakula na mahali pa kulala, kwa maana hapa tulipo ni nyikani."

Wolof

ca ngoon sa fukki taalibe ya ak ñaar ñëw ci yeesu ne ko: «yiwil mbooloo mi, ñu dugg ci dëkk yi ak àll bi ko wër, ngir am lu ñu lekk ak fu ñu fanaan, ndaxte fii àllub neen la.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
8,033,025,246 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK