From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
petro alipokuwa anasafirisafiri kila mahali alifika pia kwa watu wa mungu waliokuwa wanaishi luda.
piyeer nag di wër, di jaar fu nekk, tey dem ci gaayi yàlla yi dëkk lidd,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
hakuna kitu kinachonifurahisha zaidi kuliko kusikia kwamba watoto wangu wanaishi katika ukweli.
awma mbég mu ëpp lii: ma dégg ne samay doomi diine ñu ngiy jaar ci tànki dëgg.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
wale wanafunzi waliamua kila mmoja kwa kadiri ya uwezo wake apeleke chochote ili kuwasaidia wale ndugu waliokuwa wanaishi yudea.
kon taalibe ya fas yéenee sàkk ndimbal, jëme ca bokk ya dëkk diiwaanu yude, ku nekk ak sa kem-kàttan.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
kisha aliwatokea ndugu zaidi ya mia tano kwa mara moja; wengi wao wanaishi bado, lakini baadhi yao wamekwisha kufa.
gannaaw ga feeñu na lu ëpp juróomi téeméeri bokki taalibe ci benn yoon. te ñu bare ci ñoom ñu ngi dund ba léegi, waaye am na ci ñu nelaw.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
basi, yeye si mungu wa wafu, bali ni mungu wa wale walio hai; maana wale aliowaita kwake, wanaishi naye."
kon nag nekkul yàllay ñi dee waaye yàllay ñiy dund la, ndaxte yàllaa tax ñépp di dund.»
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
"huko kulikuwa na mtu mmoja aitwaye anania, mtu mcha mungu, mwenye kuitii sheria yetu na aliyeheshimika sana mbele ya wayahudi waliokuwa wanaishi damasko.
«bi ma ko defee ku tudd anañas ñëw ci man. nit ku ragal yàlla la woon ci sàmm yoonu musaa, te yawuti damas yépp seedeel ko lu baax.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
je, huyu si yule seremala mwana wa maria, na ndugu yao kina yakobo, yose, yuda na simoni; je, dada zake si wanaishi papa hapa kwetu?" basi, wakawa na mashaka naye.
ndax kii du minise bi? ndax du doomu maryaama te magu saag, yuusufa, yuda ak simoŋ? te ay rakkam yu jigéen ndax nekkuñu fi ak nun?» kon nag ñu daldi ko xeeb.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting