Results for wowote translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

basi, nendeni kwenye barabara na wowote wale mtakaowakuta waiteni waje arusini.

Wolof

demleen nag buntu dëkk ba, woo ku ngeen fa gis ci reeri céet gi.”

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

hakufanya ubaguzi wowote kati yetu na wao; aliitakasa mioyo yao kwa imani.

Wolof

gënalantewu nu ak ñoom, ci li mu sellal seen xol ci kaw ngëm.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

mapendo yenu na yawe bila unafiki wowote. chukieni jambo lolote ovu, zingatieni jema.

Wolof

na seen cofeel di lu dëggu te bañ a nekk ngistal; araamal-leen lu bon te sax ci lu baax.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

maana wanaanza safari yao katika utumishi wa kristo bila kupokea msaada wowote kutoka kwa watu wasioamini.

Wolof

ndaxte turu krist la leen taxa jóg, te sàkkuwuñu daray ku gëmul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini hawakupata ushahidi wowote, ingawa walikuja mashahidi wengi wa uongo. mwishowe wakaja mashahidi wawili,

Wolof

waaye mënuñu koo am. teewul ñu bare ñëwoon nañu, di seede lu dul dëgg. ba mujj ñaari nit ñëw naan:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa vile ninyi ni watu wa mungu, basi uasherati, uchafu wowote ule au choyo visitajwe kamwe miongoni mwenu.

Wolof

waaye naka njaaloo ak bépp sobe mbaa bëgge, jéllale naa jëf ji sax, waaye bu ko làmmiñ tudd, ni mu jekke ci gaayi yàlla yu sell yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini mkiingia katika mji wowote, wasipowakaribisheni, tokeni; nanyi mpitapo katika barabara zao semeni:

Wolof

waaye bu ngeen duggee ci dëkk te teeruwuñu leen, demleen ca mbedd ya te ne leen:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

alijadiliana na wayahudi na watu wengine waliomcha mungu katika sunagogi; na kila siku alikuwa na majadiliano sokoni pamoja na wowote wale waliojitokeza.

Wolof

muy werante nag ca jàngu ba ak yawut ya ak ña ragal yàlla, tey werante it bés bu nekk ca pénc ma ak ña fay dajaloo.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

basi, yesu akawauliza, "je, ninyi hamwelewi mfano huu? mtawezaje basi, kuelewa mfano wowote?

Wolof

noonu yeesu ne leen: «ndax xamuleen léeb wii? nu ngeen xame nag léeb yi ci des?

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

"mkiingia katika mji wowote au kijiji, tafuteni humo mtu yeyote aliye tayari kuwakaribisheni, na kaeni naye mpaka mtakapoondoka mahali hapo.

Wolof

«bu fekkee ne agsi ngeen ci dëkk bu mag mbaa bu ndaw, nangeen fa seet ku fa am faayda, dal ca moom ba kera ngeen jóge dëkk ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

huenda kwamba huko kuna mtu ambaye hatautii huu ujumbe tunaowapelekeeni katika barua hii. ikiwa hivyo, basi, mfichueni mtu huyo na msiwe na uhusiano wowote naye kusudi aone aibu.

Wolof

su kenn bañee topp li nu bind ci bataaxal bii, ràññeeleen ko te sore ko, ngir mu rus ci.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

paulo akajibu, "nasimama mbele ya mahakama ya kaisari na papa hapa ndipo ninapopaswa kupewa hukumu. kama unavyojua vizuri, sikuwatendea wayahudi ubaya wowote.

Wolof

waaye pool ne ko: «maa ngi nii taxaw ci kanam àttekaayu buur sesaar; te fii lañu ma war a àttee. te yaw ci sa bopp xam nga bu baax ne, tooñuma yawut yi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

basi, yesu akawauliza, "vijana, hamjapata samaki wowote sio?" wao wakamjibu, "la! hatujapata kitu."

Wolof

yeesu ne leen nag: «bokk yi, xanaa jàppuleen jën?» Ñu ne ko: «déedéet.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

jiunge nao katika ibada ya kujitakasa, ukalipe na gharama zinazohusika, kisha wanyolewe nywele zao. hivyo watu wote watatambua kwamba habari zile walizoambiwa juu yako hazina msingi wowote, na kwamba wewe binafsi bado unaishi kufuatana na maagizo ya sheria za mose.

Wolof

jël leen, bokk ak ñoom setlu, te nga gàddu seen peyu wateef. noonu ñépp dinañu xam ne, li ñu déggoon ci sa mbir du dëgg, waaye yaa ngi jëf tey sàmm yoonu musaa.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini huyo mtu akaenda, akaanza kueneza habari hiyo kila mahali na kusema mambo mengi hata yesu hakuweza tena kuingia katika mji wowote waziwazi; ikamlazimu kukaa nje, mahali pa faragha. hata hivyo, watu wakamwendea kutoka kila upande.

Wolof

waaye naka la waa ji génn, mu di yéene ci kaw li xewoon, te di ko jéebaane, ba tax yeesu mënatul a faŋaaral dugg cib dëkk, waaye mu nekk ci biti ciy bérab yu wéet. ba tey nit ñi jóge fu nekk, di ko fa fekk.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
8,927,774,238 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK