Results for zakariya translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

zakariya alipomwona alifadhaika, hofu ikamwingia.

Wolof

naka la ko sakariya gis, fitam daldi dem, mu tiit.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

huko, aliingia katika nyumba ya zakariya, akamsalimu elisabeti.

Wolof

mu dugg ca kër sakariya, daldi nuyu elisabet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

papo hapo midomo na ulimi wake zakariya vikafunguliwa, akawa anaongea akimsifu mungu.

Wolof

ca saa sa yàlla dindi luu gi, sakariya daldi waxaat, di màggal yàlla.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

wakati huo, wale watu walikuwa wanamngoja zakariya huku wakishangaa juu ya kukawia kwake hekaluni.

Wolof

fekk na booba mbooloo maa ngi xaar, jaaxle lool ci li sakariya yàgg ca bérab bu sell ba.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

halafu siku ya nane walifika kumtahiri mtoto, wakataka kumpa jina la baba yake, zakariya.

Wolof

bi bés ba dellusee, ñu ñëw xarafalsi xale ba, bëgg koo dippee baayam sakariya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

tangu kumwagwa damu ya abeli mpaka kifo cha zakariya ambaye walimuua kati ya madhabahu na mahali patakatifu. naam, hakika kizazi hiki kitaadhibiwa kwa matendo haya.

Wolof

la dale ca abel ba ci sakariya, moom mi ñu rey ci diggante saraxalukaay bi ak bérab bu sell bi. waaw, maa ngi leen koy wax, yàlla dina mbugal niti jamono jii ndax loolu.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

na anasi na kayafa walikuwa makuhani wakuu mjini yerusalem. wakati huo ndipo neno la mungu lilipomjia yohane, mwana wa zakariya, kule jangwani.

Wolof

te it anas ak kayif nekkoon saraxalekat yu mag ya. ca jamono jooja la kàddug yàlla wàcc ci yaxya, doomu sakariya, ca màndiŋ ma.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

lakini malaika akamwambia, "zakariya, usiogope, kwa maana sala yako imesikilizwa, na elisabeti mkeo atakuzalia mtoto wa kiume, nawe utampa jina yohane.

Wolof

waaye malaaka ma ne ko: «bul ragal dara sakariya, ndaxte sa ñaan nangu na. elisabet sa jabar dina la jural doom, te dinga ko tudde yaxya.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

hivyo lawama yote itawapateni kwa ajili ya damu yote ya watu wema iliyomwagwa juu ya ardhi. naam, tangu kuuawa kwa abeli ambaye hakuwa na hatia, mpaka kuuawa kwa zakariya, mwana wa barakia, ambaye mlimuua hekaluni kati ya patakatifu na madhabahu.

Wolof

noonu deretu ñi jub, ji ñu tuur jépp ci àddina, dina xëppu ci seen kaw, li dale ci deretu abel mi jub, ba ci deretu sakariya doomu baraki, mi ngeen rey ci diggante bérab bu sell bi ak saraxalukaay bi.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,745,564,237 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK