Results for zilianguka translation from Swahili to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swahili

Wolof

Info

Swahili

nyingine zilianguka kwenye miti ya miiba, nayo ikakua na kuzisonga.

Wolof

leneen nag wadd ci biir ay xaaxaam, xaaxaam yi daldi jóg, tanc ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

alipokuwa akipanda, nyingine zilianguka njiani, ndege wakaja wakazila.

Wolof

bi muy saaw toolam nag, lenn ci pepp mi wadd ci kaw yoon wi, picc yi daldi ñëw, lekk ko lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 2
Quality:

Swahili

nyingine zilianguka kati ya miti ya miiba. ile miti ya miiba ilipoota ikazisonga.

Wolof

leneen nag wadd ci biir ay xaaxaam, ñu saxandoo, xaaxaam ya tanc ko.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

kwa imani kuta za mji wa yeriko zilianguka watu wa israeli walipokwisha zunguka kwa muda wa siku saba.

Wolof

ngëm moo tax miir yi wëroon dëkku yeriko màbb, gannaaw ba ko bànni israyil wëree lu mat juróom-ñaari fan.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

nyingine zilianguka penye mawe pasipokuwa na udongo mwingi. zikaota mara kwa kuwa udongo haukuwa na kina.

Wolof

leneen ci pepp mi wadd ci bérab bu bare ay doj te néew suuf, mu daldi sax bu gaaw, ndaxte suuf si barewul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

nyingine zilianguka penye mawe pasipokuwa na udongo mwingi. mbegu hizo ziliota mara kwa kuwa udongo haukuwa na kina.

Wolof

leneen ci pepp mi wadd ci bérab bu bare ay doj te néew suuf, mu daldi sax bu gaaw, ndaxte suuf si barewul.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

watu wengine ni kama wale walio njiani ambapo mbegu zilianguka. hawa hulisikia hilo neno lakini mara shetani huja na kuliondoa neno hilo lililopandwa ndani yao.

Wolof

ki féete ci yoon wi mooy ki dégg, seytaane ñëw ci saa si, këf kàddu, gi ñu def ci moom.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

nyingine zilianguka katika udongo mzuri, zikakua na kuzaa: moja punje thelathini, moja sitini na nyingine mia."

Wolof

li ci des dal ci suuf su baax, mu jóg, sax, di focci ay gub; lii àntu, ba mat fanweeri yoon lu ëpp la mu ji woon, lii mat juróom-benn-fukk, lii mat téeméer.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

lakini nyingine zilianguka penye udongo mzuri, zikaota, zikazaa: nyingine punje mia moja, nyingine sitini na nyingine thelathini.

Wolof

li ci des dal ci suuf su baax, nangu ba def ay gub; lii àntu ba mat téeméeri yoon lu ëpp la mu ji woon, lii mat juróom-benn-fukk, li ci des fanweer.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Swahili

"mpanzi alikwenda kupanda mbegu zake. alipokuwa akipanda zile mbegu, nyingine zilianguka njiani, na wapita njia wakazikanyaga, na ndege wakazila.

Wolof

«dafa amoon beykat bu demoon jiyi. bi muy saaw toolam nag, lenn ci pepp mi wadd ci kaw yoon wi, nit ñi joggi ci, picci asamaan lekk ko lépp.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Swahili

nyingine zilianguka katika udongo mzuri, zikaota na kuzaa asilimia mia." baada ya kusema hayo, akapaaza sauti, akasema, "mwenye masikio na asikie!"

Wolof

li ci des dal ci suuf su baax, sax, nangu ba meññ téeméeri yoon lu ëpp la mu ji woon.» gannaaw loolu yeesu wax ak kàddu gu dëgër ne: «déglul bu baax, yaw mi am ay nopp.»

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,781,211,190 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK