Results for halta translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

i dessa lågo många sjuka, blinda, halta, förtvinade.

Wolof

ca suufu mbaar yooyu la jarag yu bare, yu deme niki ay gumba, ay lafañ ak ay làggi, daan tëdd, di xaar ndox mi yengatu;

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

nej, när du gör gästabud, så bjud fattiga, krymplingar, halta, blinda.

Wolof

waaye boo dee woote lekk, wool néew doole yi, làggi yi, lafañ yi ak gumba yi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

så att folket förundrade sig, när de funno dövstumma tala, lytta vara friska och färdiga, halta gå och blinda se. och man prisade israels gud.

Wolof

nit ñépp waaru, ndaxte gis nañu luu yuy wax, làggi yu wér, lafañ yuy dox, ak gumba yuy gis. Ñu daldi màggal yàlla buuru israyil.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

blinda få sin syn, halta gå, spetälska bliva rena, döva höra, döda uppstå, och 'för fattiga förkunnas glädjens budskap'.

Wolof

gumba yaa ngi gis, lafañ yiy dox, gaana yi wér, tëx yiy dégg, ñi dee di dekki, te ñi woyoflu ñu ngi dégg xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

då kom mycket folk till honom, och de hade med sig halta, blinda, dövstumma, lytta och många andra; dem lade de ned för hans fötter, och han botade dem,

Wolof

ba mu fa nekkee, nit ñu bare ñëw ci moom, indaale ay lafañ, ay làggi, ay gumba, ay luu ak ñeneen ñu bare. Ñu teg leen ci tànki yeesu, mu faj leen.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och han svarade och sade till männen: »gån tillbaka och omtalen för johannes vad i haven sett och hört: blinda få sin syn, halta gå, spetälska bliva rena, döva höra, döda uppstå, 'för fattiga förkunnas glädjens budskap'.

Wolof

noonu mu tontu ndaw ya ne leen: «demleen nettali yaxya li ngeen gis te dégg ko. gumba yaa ngi gis, lafañ yiy dox, gaana yi wér, tëx yiy dégg, ñi dee di dekki, te ñi woyoflu ñu ngi dégg xebaar bu baax bi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,437,834 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK