Results for profeterade translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

i skrymtare, rätt profeterade esaias om eder, när han sade:

Wolof

yéen ñi naaféq, esayi waxoon na bu baax ci kàddug yàlla ci seen mbir, bi mu naan:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och hans fader sakarias blev uppfylld av helig ande och profeterade och sade:

Wolof

sakariya baayu yaxya daldi fees ak xel mu sell mi. noonu mu wax ci kàddug yàlla ne:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och när paulus lade händerna på dem, kom den helige ande över dem, och de talade tungomål och profeterade.

Wolof

te bi leen pool tegee loxo, xel mu sell mi ñëw ci ñoom, ñuy wax yeneeni làkk, di wax ci kàddug yàlla.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

angående denna frälsning hava profeter ivrigt forskat och rannsakat, de som profeterade om den nåd som skulle vederfaras eder.

Wolof

naka mucc googu nag, yonent yi xamle yiw, wi ngeen naroon a joti, seet nañu ko te gëstu ko.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

om åter alla profeterade, och så någon som icke trodde, eller som vore olärd komme ditin, då skulle denne känna sig avslöjad av alla och av alla utrannsakad.

Wolof

waaye bu ñépp dee wax ci kàddug yàlla, te ku gëmul dugg fa, walla ku jàngul mbiri kirist, wax yi ñépp wax dafay wone bàkkaaram te àtte ko,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

om dessa var det ock som enok, den sjunde från adam, profeterade och sade: »se, herren kommer med sina mångtusen heliga,

Wolof

enog, di juróom-ñaareelu maam gannaaw aadama, waxoon na ci kàddug yàlla, ba weer leen ne: «boroom bi wàcce na ca asamaan, ànd ak ay junniy junniy malaakaam,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

jag skulle väl vilja att i alla taladen tungomål, men ännu hellre ville jag att i profeteraden. den som profeterar är förmer än den som talar tungomål, om nämligen den senare icke därjämte uttyder sitt tal, så att församlingen får någon uppbyggelse.

Wolof

léegi nag bëgg naa yéen ñépp, ngeen di wax ay làkk, waaye li ma gënal mooy ngeen di wax ci kàddug yàlla. kiy wax ci kàddug yàlla moo gën kiy wax ay làkk, su firiwul li muy wax, ngir ngëmu mbooloo mi yokku.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,744,212,326 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK