Results for sabbat translation from Swedish to Wolof

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Swedish

Wolof

Info

Swedish

följande sabbat kom nästan hela staden tillsammans för att höra guds ord.

Wolof

noonu bésu noflaay ba ca tegu, daanaka waa dëkk bépp daje, ngir déglu kàddug yàlla.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och det var sabbat den dag då jesus gjorde degen och öppnade hans ögon.

Wolof

ndekete yeesu, bés bi mu tooyale ban, ubbi bëti gumba ga, bésu noflaay la woon.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och i synagogan höll han var sabbat samtal och övertygade både judar och greker.

Wolof

bésu noflaay bu nekk nag muy diisoo ak ñi nekk ca jàngu ba, di jéem a gëmloo ay yawut ak ay gereg.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och strax blev mannen frisk och tog sin säng och gick. men det var sabbat den dagen.

Wolof

ca saa sa mu daldi wér, jël basaŋam, daldi dox. mbir moomu dafa daje woon ak bésu noflaay ba,

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

låten därför ingen döma eder i fråga om mat och dryck eller angående högtid eller nymånad eller sabbat.

Wolof

kon nag bu leen kenn teg tooñ ci li jëm ciy ñam mbaa naan, ci màggal mbaa xewu weer wu feeñ, mbaa ci bésu noflaay.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

ty moses har av ålder sina förkunnare i alla städer, då han ju var sabbat föreläses i synagogorna.»

Wolof

ndaxte ca njàlbéen ga ba tey am na ca dëkk bu nekk ñuy waare ci yoonu musaa; bésu noflaay bu nekk sax dañu ciy xutba ca jàngu ya.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

på en annan sabbat hände sig att han gick in i synagogan och undervisade. där var då en man vilkens högra hand var förvissnad.

Wolof

beneen bésu noflaay, yeesu dugg ci jàngu bi, di fa jàngale. amoon na fa nit ku loxol ndeyjooram làggi.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

när han på en sabbat hade kommit in till en av de förnämligaste fariséerna för att intaga en måltid, hände sig, medan man där vaktade på honom,

Wolof

benn bésu noflaay yeesu dem ci këru benn kilifag farisen yi, ngir lekke fa. nit ñaa ngi ko doon xool bu baax.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

sedan vände de tillbaka till jerusalem från det berg som kallas oljeberget, vilket ligger nära jerusalem, icke längre därifrån, än man får färdas på en sabbat.

Wolof

bi loolu amee ñu jóge ca tund, woowu ñuy wax tundu oliw ya, te mu dend ak yerusalem lu tollu ak kilomet, ñu daldi dellu yerusalem.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

därför sade judarna till mannen som hade blivit botad: »det är sabbat; det är icke lovligt för dig att bära sängen.»

Wolof

looloo tax ba yawut ya daldi ne nit ku wér ka: «tey bésu noflaay la, te sunu yoon aaye na, ngay yor sa basaŋ.»

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Swedish

och när det blev sabbat, begynte han undervisa i synagogan. och folket häpnade, när de hörde honom; de sade: »varifrån har han fått detta? och vad är det för vishet som har blivit honom given? och dessa stora kraftgärningar som göras genom honom, varifrån komma de?

Wolof

bésu noflaay bi nag mu jàngal leen ci seen jàngu, ba mbooloom ñi ko dégg waaru naan: «lii, fu mu ko jële, te xam-xam bii mu yor, lu mu doon, ba muy def kéemaan yii?

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,783,327,137 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK