From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
noonu ñu dugg cig gaal, dem ca bérab bu wéet.
فمضوا في السفينة الى موضع خلاء منفردين.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye yeesu moom di beddeeku ci bérab yu wéet ya, di ñaan.
واما هو فكان يعتزل في البراري ويصلّي
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi bésu màggalu pàntakot agsee, ñoom ñépp booloo nañu ci benn bérab.
ولما حضر يوم الخمسين كان الجميع معا بنفس واحدة.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca ëllëg sa yaxya taxawaatoon na ca bérab booba, ànd ak ñaari taalibeem.
وفي الغد ايضا كان يوحنا واقفا هو واثنان من تلاميذه.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu rab ya dajale buuri àddina si ci bérab bu tudd ci làkku yawut armagedon.
فجمعهم الى الموضع الذي يدعى بالعبرانية هرمجدون
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ca njël laata bët di set, yeesu jóg dem ca bérab bu wéet, di fa ñaan yàlla.
وفي الصبح باكرا جدا قام وخرج ومضى الى موضع خلاء وكان يصلّي هناك.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
benn waay it bu soqikoo ci giiru lewi, aw ca bérab booba, séen waa ja, teggi.
وكذلك لاوي ايضا اذ صار عند المكان جاء ونظر وجاز مقابله.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
néeg ba ñu tudde bérab bu sell-baa-sell a nga nekkoon ca gannaaw ñaareelu rido ba.
ووراء الحجاب الثاني المسكن الذي يقال له قدس الاقداس
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
leneen wadd ci bérab bu bare ay doj. naka la sax rekk, daldi wow, ndaxte suuf si tooyul woon.
وسقط آخر على الصخر فلما نبت جف لانه لم تكن له رطوبة.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye waa ji xamul ki ko wéral, fekk booba yeesu dem na, te nit ñu bare teewoon nañu ca bérab ba.
اما الذي شفي فلم يكن يعلم من هو. لان يسوع اعتزل. اذ كان في الموضع جمع.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
tool a nga woon ca wetu bérab, ba ñu daajoon yeesu, te ca tool booba amoon na fa bàmmeel bu ñu musul a suul kenn.
وكان في الموضع الذي صلب فيه بستان وفي البستان قبر جديد لم يوضع فيه احد قط.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te ñu sàkk ay naaféq yuy seede ne: «kii du bàyyee wax lu juuyoo ak bérab bu sell ba ak yoonu musaa.
واقاموا شهودا كذبة يقولون هذا الرجل لا يفتر عن ان يتكلم كلاما تجديفا ضد هذا الموضع المقدس والناموس.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te su ma leen defaralee bérab booba ba noppi, dinaa dellusi, yóbbaale leen, ba fu ma nekk, ngeen nekk fa, yéen itam.
وان مضيت واعددت لكم مكانا آتي ايضا وآخذكم اليّ حتى حيث اكون انا تكونون انتم ايضا.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«boo xamee ne rab wa jàppoon nit génn na ci moom, day wër ay bérab yu wow, di wut fu mu noppaloo, waaye du ko gis.
اذا خرج الروح النجس من الانسان يجتاز في اماكن ليس فيها ماء يطلب راحة ولا يجد.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye mënuñu koo jege ndax mbooloo mi. kon ñu daldi teggi kaw kër gi, di bëtt fa tiim bérab ba yeesu nekk, daldi yoor basaŋ, ga làggi ba tëdd.
واذ لم يقدروا ان يقتربوا اليه من اجل الجمع كشفوا السقف حيث كان وبعدما نقبوه دلّوا السرير الذي كان المفلوج مضطجعا عليه.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye léegi nee na fàŋŋ, ngir kilifa yi ak boroom sañ-sañ yi ca bérab yu kawe ya man a xam ni xelum yàlla xóote, jaar ci li ñu gis ci mbooloom ñi gëm kirist.
لكي يعرّف الآن عند الرؤساء والسلاطين في السماويات بواسطة الكنيسة بحكمة الله المتنوعة
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu digg-bëccëg daldi jot, jant ba nëbbu, réew mépp daldi lëndëm këruus lu mat ñetti waxtu. ridob bérab bu sell ba ca kër yàlla ga daldi xar ñaar.
وكان نحو الساعة السادسة. فكانت ظلمة على الارض كلها الى الساعة التاسعة.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
sunuy xebaar law na, ba egg ca bokk ya fa dëkk, noonu ñu gatandu nu ba ca péncu apiyus ak bérab bu ñuy wax Ñetti añukaay ya. bi leen pool gisee, mu sant yàlla, daldi takk fitam.
ومن هناك لما سمع الاخوة بخبرنا خرجوا لاستقبالنا الى فورن ابيوس والثلاثة الحوانيت. فلما رآهم بولس شكر الله وتشجع
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ki nekk ci bérab bu bare ay doj, mooy ki dégg kàddu gi, ba noppi nangu ko ak mbég. waaye wax ji saxul ci moom. dina gëm ab diir, waaye bu nattu yi agsee, mu daldi dàggeeku.
والذين على الصخر هم الذين متى سمعوا يقبلون الكلمة بفرح. وهؤلاء ليس لهم اصل فيؤمنون الى حين وفي وقت التجربة يرتدون.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«dina am bés bu li ñuy wax: “lu araam luy yàqe” dina tege ca bérab bu sell ba. mooy li ñu doon wax jaarale ko ci yonent yàlla dañeel; ku ko jàng, nanga ko xam.
فمتى نظرتم رجسة الخراب التي قال عنها دانيال النبي قائمة في المكان المقدس. ليفهم القارئ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: