Results for bëggante translation from Wolof to Arabic

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Arabic

Info

Wolof

saxleen ci bëggante ni ay bokk.

Arabic

لتثبت المحبة الاخوية.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li may santaane nag, mooy ngeen bëggante.

Arabic

بهذا اوصيكم حتى تحبوا بعضكم بعضا

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sama ndigal mooy ngeen bëggante, ni ma leen bëgge.

Arabic

هذه هي وصيتي ان تحبوا بعضكم بعضا كما احببتكم.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ni ñuy xame ne samay taalibe ngeen, mooy ngeen bëggante.»

Arabic

بهذا يعرف الجميع انكم تلاميذي ان كان لكم حب بعضا لبعض

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay soppe, bu nu yàlla bëggee nii, nun itam war nanoo bëggante.

Arabic

ايها الاحباء ان كان الله قد احبنا هكذا ينبغي لنا ايضا ان يحب بعضنا بعضا.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay doom, bunu bëggante ci wax mbaa ci làmmiñ rekk, waaye ci jëf ak ci dëgg.

Arabic

يا اولادي لا نحب بالكلام ولا باللسان بل بالعمل والحق.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

maa ngi leen di jox ndigal lu bees: bëgganteleen. nangeen di bëggante ni ma leen bëgge.

Arabic

وصية جديدة انا اعطيكم ان تحبوا بعضكم بعضا. كما احببتكم انا تحبون انتم ايضا بعضكم بعضا.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na leen boroom bi dolli mbëggeel gu tar, ngeen bëggante te bëgg ñépp, ni nu leen bëgge nun.

Arabic

والرب ينميكم ويزيدكم في المحبة بعضكم لبعض وللجميع كما نحن ايضا لكم

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndigalam mooy lii: nu gëm turu doomam, yeesu kirist, tey bëggante, ni mu nu ko digale.

Arabic

وهذه هي وصيته ان نؤمن باسم ابنه يسوع المسيح ونحب بعضنا بعضا كما اعطانا وصية.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ci lu jëm ci bëggante ci seen biir, matul nu leen di bind dara, ndaxte yàlla def na ci seen xol, ngeen bëggante.

Arabic

واما المحبة الاخوية فلا حاجة لكم ان اكتب اليكم عنها لانكم انفسكم متعلمون من الله ان يحب بعضكم بعضا.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

léegi nag soxna si, maa ngi lay dénk lii: nun ñépp nanu bëggante, te loolu du dénkaane bu bees, waaye moom lanu jotoon ca njàlbéen ga.

Arabic

والآن اطلب منك يا كيرية لا كاني اكتب اليك وصية جديدة بل التي كانت عندنا من البدء ان يحب بعضنا بعضا.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

samay soppe, nanu bëggante, ndax mbëggeel ci yàlla la bawoo; képp ku bëgg sa mbokk nag, ci yàlla nga juddoo, te xam nga yàlla.

Arabic

ايها الاحباء لنحب بعضنا بعضا لان المحبة هي من الله وكل من يحب فقد ولد من الله ويعرف الله.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw loolu bokk yi, maa ngi leen di ñaan ci turu sunu boroom yeesu kirist ak ci bëggante, gi xelu yàlla mi def ci nun, ngeen defal ma lii: àndleen ak man, nu tuur sunu ñaq ci ñaan yàlla.

Arabic

فاطلب اليكم ايها الاخوة بربنا يسوع المسيح وبمحبة الروح ان تجاهدوا معي في الصلوات من اجلي الى الله

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,781,150,415 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK