From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
sawarleen te bañ a tayel, di jaamu boroom bi ak seen xol bépp.
غير متكاسلين في الاجتهاد. حارّين في الروح. عابدين الرب.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bëggunu ngeen tayel, waaye royleen ñi gëm te muñ, ndaxte ñooy jot li leen yàlla dig.
لكي لا تكونوا متباطئين بل متمثلين بالذين بالايمان والاناة يرثون المواعيد
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
léegi nag dégg nanu ne, am na ci yéen ñuy wéy ci tayel; liggéeyuñu dara, lu dul di dugg ci lu seen yoon nekkul.
لاننا نسمع ان قوما يسلكون بينكم بلا ترتيب لا يشتغلون شيئا بل هم فضوليون.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
nu ngi leen di sant it bokk yi, ci turu sunu boroom yeesu kirist, ngeen dëddu bépp mbokk buy wéy ci tayel te bañ a topp dénkaane, yi nu leen jottali.
ثم نوصيكم ايها الاخوة باسم ربنا يسوع المسيح ان تتجنبوا كل اخ يسلك بلا ترتيب وليس حسب التعليم الذي اخذه منا.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye njaatigeem tontu ko: “surga bu bon nga te tayel! gannaaw xamoon nga ne, damay dajale fu ma jiwul, tey góob fu ma faruwul,
فاجاب سيده وقال له ايها العبد الشرير والكسلان عرفت اني احصد حيث لم ازرع واجمع من حيث لم ابذر.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te du yem ci bëgg a séyaat rekk, waaye ku tayel lay doon; di ku wër kër ak kër, rax-ca-dolli réy làmmiñ te deñ kumpa, di wax lu yoonam nekkul.
ومع ذلك ايضا يتعلمن ان يكنّ بطالات يطفن في البيوت ولسن بطالات فقط بل مهذارات ايضا وفضوليات يتكلمن بما لا يجب.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: