Results for ndekkitel translation from Wolof to Czech

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Czech

Info

Wolof

te lu jëm ci ndekkitel ñi dee, xanaa musuleen a jàng la leen yàlla waxoon ne:

Czech

o vzkříšení pak mrtvých zdaliž jste nečtli, co jest vám povědíno od boha, kterýž takto dí:

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

Ñu mer lool ci li ñuy waar nit ñi, di yégle ndekkitel ñi dee, sukkandikoo ko ci ndekkitel yeesu.

Czech

těžce to nesouce, že lid učili a zvěstovali ve jménu ježíše vzkříšení z mrtvých.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te ndaw yi di seedeel ndekkitel yeesu boroom bi ak kàttan gu réy. te yiw wu yaatu ëmb leen, ñoom ñépp.

Czech

a mocí velikou vydávali apoštolé svědectví o vzkříšení pána ježíše, a milost veliká přítomná byla všechněm jim.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

kon gis na lu ñëwagul, di wax ci mbirum ndekkitel kirist ne, bàyyiwuñu ko ci barsàq, te yaramam yàquwul.

Czech

to předzvěděv, mluvil o vzkříšení kristovu, že není opuštěna duše jeho v pekle, ani tělo jeho vidělo porušení.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu la ndekkitel néew yi di deme. bu ñu suulee néew bi, dañoo ji lu yàqu. bu dekkee, du yàqooti ba abadan.

Czech

tak i vzkříšení z mrtvých. rozsívá se tělo porušitelné, vstane neporušitelné;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

xanaa li ma waxoon ca kaw ci seen biir rekk ne: “mbirum ndekkitel ñi dee moo tax ngeen dëj ma ci seen kanam tey!”»

Czech

leč to jedno promluvení, že jsem zavolal, stoje mezi nimi: pro vzkříšení z mrtvých já k soudu potažen jsem dnes od vás.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

cant ñeel na yàlla, baayu sunu boroom yeesu kirist! moo nu judduwaatal ci yërmandeem ju bare, ba may nu yaakaar ju sax ndax ndekkitel yeesu kirist.

Czech

požehnaný bůh a otec pána našeho ježíše krista, kterýžto podle mnohého milosrdenství svého znovu zplodil nás v naději živou skrze vzkříšení ježíše krista z mrtvých,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

li dale ci bi ko yaxya sóobee ci ndox, ba bés ba ko yàlla jële ci sunu biir, yéege ko. kooku war na ànd ak nun, di seedeel ndekkitel yeesu.»

Czech

počav od křtu janova až do dne toho, v kterémžto vzhůru vzat jest od nás, byl svědkem spolu s námi vzkříšení jeho.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

bi ñu déggee nag, muy wax ci mbirum ndekkitel ñi dee, ñii di ko fontoo, ña ca des ne ko: «dinanu la déglu ci mbir moomu beneen yoon.»

Czech

uslyševše pak o vzkříšení z mrtvých, někteří se posmívali, a někteří řekli: budeme tě slyšeti o tom po druhé.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

loolu misaal la tey, ci li ñu nuy sóob ci ndox, te nu mucc; waxuma laabal sobe si taq ci yaram, waaye wuyu yàlla ak xel mu dal. li nu may mucc googu, mooy ndekkitel yeesu kirist,

Czech

k čemužto připodobněn jsa nyní křest, i nás spaseny činí, ne to tělesné špíny smytí, ale dobrého svědomí u boha dotázání, skrze vzkříšení ježíše krista.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,776,334,537 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK