From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
yoon wu ma leen di xalaat, maa ngi sant yàlla sama boroom;
jeg takker min gud, så ofte jeg kommer eder i hu,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
gis naa nag lii: saa su ma bëggee def lu baax, lu bon a ngi ma taxawu.
så finder jeg da den lov for mig, som vil gøre det gode, at det onde ligger mig for hånden
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
sama mbokk epafras, mi ma nekkal fi ci kaso bi ci turu kirist, mu ngi lay nuyu.
epafras, min medfangne i kristus jesus,
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma seen njiit yépp ak gaayi yàlla yépp. waa itali ñu ngi leen di nuyu.
hilser alle eders vejledere og alle de hellige! de fra italien hilse eder.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
nuyul-leen ma gaayi kirist yeesu yu sell yépp. bokk yi ànd ak man, ñu ngi leen di nuyu.
hilser hver hellig i kristus jesus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
maa ngi wax ak yéen ñi am xel. kon seetleen li ma leen wax.
jeg taler som til forstandige; dømmer selv, hvad jeg siger.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
miskin yaa ngi ak yéen bés bu nekk, waaye dungeen ma gis ba fàww.
thi de fattige have i altid hos eder; men mig have i ikke altid.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
bi piyeer di rabal xelam ci peeñu ma, xel mi ne ko: «Ñetti nit a ngi nii, di la wut.
men idet peter grublede over synet, sagde Ånden til ham: "se, der er tre mænd, som søge efter dig;
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
te ngeen jàngal leen, ñuy sàmm lépp li ma leen sant. te maa ngi ànd ak yéen bés bu nekk, ba kera àddina di tukki.»
og idet i lære dem at holde alt det, som jeg har befalet eder. og se, jeg er med eder alle dage indtil verdens ende."
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
taalibeem ya fàttaliku mbind mii: «cawarte gi ma am ci sa kër, mu ngi mel ni taal buy tàkk ci sama biir.»
hans disciple kom i hu, at der er skrevet: "nidkærheden for dit hus vil fortære mig."
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
«léegi nag maa ngi dem ca ka ma yónni, te kenn ci yéen laaju ma fi ma jëm.
men nu går jeg hen til ham, som sendte mig, og ingen af eder spørger mig: hvor går du hen?
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waxtu waa ngi ñëw te agsi na ba noppi, dingeen tasaaroo, ku nekk ñibbi, ma des man rekk.
se, den time kommer, og den er kommen, da i skulle adspredes hver til sit og lade mig alene; dog, jeg er ikke alene, thi faderen er med mig.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
miskin yaa ngi ak yéen bés bu nekk, te man ngeen leen a dimbali saa su leen neexee, waaye dungeen ma gis ba fàww.
de fattige have i jo altid hos eder, og når i ville, kunne i gøre vel imod dem; men mig have i ikke altid.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
waxuma ne jagoo naa ko ba noppi, waxuma it ne aji mat laa, waaye maa ngi daw, ngir jot li tax kirist jël ma.
ikke at jeg allerede har grebet det eller allerede er fuldkommen; men jeg jager derefter, om jeg dog kunde gribe det, efterdi jeg også er greben af kristus jesus.
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
ci dëgg maa ngi leen koy wax, dootuma naan gannaaw tey ndoxum réseñ mii, ba kera ma ciy naan bu bees ci nguuru yàlla.»
sandelig, siger jeg eder, at jeg skal ingen sinde mere drikke af vintræets frugt indtil den dag, da jeg skal drikke den ny i guds rige."
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
yeesu ne ko: «bu ma téye, ndaxte yéegaguma ca baay ba. waaye demal, ne samay bokk, maa ngi yéeg ca sama baay biy seen baay, ca sama yàlla jiy seen yàlla.»
jesus siger til hende: "rør ikke ved mig, thi jeg er endnu ikke opfaren til min fader; men gå til mine brødre og sig dem: jeg farer op til min fader og eders fader og til min gud og eders gud."
Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:
Warning: Contains invisible HTML formatting
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.