Results for namm na leen translation from Wolof to Danish

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

Danish

Info

Wolof

seen kawari bopp sax, waññees na leen.

Danish

men på eder ere endog alle hovedhår talte.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte namm na leen lool, te tiisoo na li ngeen yég jagadeem.

Danish

efterdi han længtes efter eder alle og var såre ængstelig, fordi i havde hørt, at han var bleven syg.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na leen yàlla may yërmande, jàmm ak mbëggeel.

Danish

barmhjertighed og fred og kærlighed vorde eder mangfoldig til del!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen ñi am yërmande, barkeel ngeen,ndax dees na leen yërëm.

Danish

salige ere de barmhjertige, thi dem skal vises barmhjertighed.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na leen yàlla sunu baay ak boroom bi yeesu kirist may yiw ak jàmm.

Danish

nåde være med eder og fred fra gud vor fader og den herre jesus kristus!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 4
Quality:

Wolof

noonu taalibe yi defar reeru jéggi ba, na leen yeesu waxe woon.

Danish

og disciplene gjorde, som jesus befalede dem, og beredte påskelammet.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

yéen ñiy wut jàmm, barkeel ngeen,ndax dees na leen tudde doomi yàlla.

Danish

salige ere de, som stifte fred, thi de skulle kaldes guds børn.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na leen boroom jàmm may jàmm ci fépp ak ci lépp. na boroom bi ànd ak yéen ñépp.

Danish

men han selv, fredens herre, give eder freden altid, i alle måder! herren være med eder alle!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sédd na leen cér bu dul yàqu, du gàkk te du seey mukk, dencal leen ko ci asamaan,

Danish

til en uforkrænkelig og ubesmittelig og uvisnelig arv, som er bevaret i himlene til eder,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte dees na leen àtte ak ni ngeen di àttee, nattal leen ak li ngeen di nattale.

Danish

og med hvad mål i måle, skal der tilmåles eder.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

daawu leen wax dara lu dul ciy léeb. waaye bu wéetee ak ay taalibe, daan na leen firil lépp.

Danish

men uden lignelse talte han ikke til dem; men i enerum udlagde han det alt sammen for sine disciple.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

tey jii ca dëkku daawuda, ab musalkat juddul na leen fa, te mooy almasi bi, di boroom bi.

Danish

thi eder er i dag en frelser født, som er den herre kristus i davids by.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

gannaaw xam yàlla soxalu leen, yàlla it bërgël na leen ci seen xel mu bon moomu, ñu sax ci jëf yu jekkadi.

Danish

og ligesom de forkastede af have gud i erkendelse, således gav gud dem hen i et forkasteligt sind til at gøre det usømmelige,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te yàlla, mi xam xol yi, seede na leen ci li mu leen may xel mu sell mi, ni mu nu ko maye nun itam.

Danish

og gud, som kender hjerterne, gav dem vidnesbyrd ved at give dem den helligånd lige så vel som os.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te jàppleen ne, muñug sunu boroom muccu nit la. sunu mbokk mi nu bëgg pool bind na leen ko, ci xel mi ko yàlla sol.

Danish

og agter vor herres langmodighed for frelse; ligesom også vor elskede broder paulus efter den ham givne visdom har skrevet til eder,

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye léegi yàlla goreel na leen ci kilifteefu bàkkaar, def leen ay jaamam, ba jural leen sell, jëme leen ci dund gu dul jeex.

Danish

men nu, da i ere blevne frigjorde fra synden og ere blevne guds tjenere, have i eders frugt til helliggørelse og som enden derpå et evigt liv;

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

na jàmm ji kirist di joxe noot seeni xol, ndaxte yàlla woo na leen ci loolu, mel ni ay cér yu bokk benn yaram; te gërëmleen yàlla.

Danish

og kristi fred råde i eders hjerter, til hvilken i også bleve kaldede i eet legeme; og vorder taknemmelige!

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

mu ne leen: «seetleen bu baax li ngeen di dégg. dees na leen nattal ak natt, bi ngeen di nattale, te dollil leen.

Danish

og han sagde til dem: "agter på, hvad i høre! med hvad mål i måle, skal der tilmåles eder, og der skal gives eder end mere.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Wolof

dees na leen reye ak i jaasi, jàpp leen jaam, yóbbu leen ci réewi àddina sépp. te ñi dul yawut dinañu nappaaje yerusalem, ba kera jamonoy ñi dul yawut mat.

Danish

og de skulle falde for sværdets od og føres fangne til alle hedningerne; og jerusalem skal nedtrædes af hedningerne, indtil hedningernes tider fuldkommes.

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

sunuy maam dunde nañu mànn ca màndiŋ ma, ndaxte mbind mi nee na: “jox na leen, ñu lekk ñam wu wàcce ca asamaan.”»

Danish

vore fædre åde manna i Ørkenen, som der er skrevet: han gav dem brød fra himmelen at æde."

Last Update: 2012-05-05
Usage Frequency: 1
Quality:

Warning: Contains invisible HTML formatting

Get a better translation with
7,787,743,463 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK