From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ci dëgg maa ngi leen koy wax, lépp dees na ko baal nit ñi, muy bàkkaar, muy sosal yàlla wu mu man a doon.
verily i say unto you, all sins shall be forgiven unto the sons of men, and blasphemies wherewith soever they shall blaspheme:
te ñaan gu ànd ak ngëm dina musal ki wopp, ba boroom bi yékkati ko. te su ko fekkoon ak i bàkkaar sax, yàlla dina ko baal.
and the prayer of faith shall save the sick, and the lord shall raise him up; and if he have committed sins, they shall be forgiven him.