From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ma dégg baat bu jóge asamaan, buy riir ni duusi géej, ni riiru dënnu gu réy. baat ba ma dégg mel ni baati xalamkat yuy xalam.
and i heard a voice from heaven, as the voice of many waters, and as the voice of a great thunder: and i heard the voice of harpers harping with their harps:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
buumi xalam yi, baati woykat yi, toxoro yi ak liit yi,kenn dootu leen dégg ci yaw.liggéeykat bu xareñ bu mu man a doon, kenn dootu ko gis ci yaw.kandaŋu gënn, kenn du ko déggati ci yaw.
and the voice of harpers, and musicians, and of pipers, and trumpeters, shall be heard no more at all in thee; and no craftsman, of whatsoever craft he be, shall be found any more in thee; and the sound of a millstone shall be heard no more at all in thee;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: