From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
li dale ci saa soosa nag yudaa di fexe jamono ju mu leen man a jébbal yeesu.
and from that time he sought opportunity to betray him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«li dale sax ci samwil ak ñi ci topp, bépp yonent bu wax yégle na bés yii.
yea, and all the prophets from samuel and those that follow after, as many as have spoken, have likewise foretold of these days.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi mu ko defee ridob bérab bu sell ba ca kër yàlla ga xar ñaar, li dale ci kaw ba ci suuf.
and the veil of the temple was rent in twain from the top to the bottom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
njiit la ne ko: «loolu lépp sàmm naa ko li dale ci sama ndaw ba tey.»
and he said, all these have i kept from my youth up.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te it ñuy yégle xeet yépp ci turam, dale ko ci yerusalem ne, war nañoo tuub seeni bàkkaar, yàlla baal leen.
and that repentance and remission of sins should be preached in his name among all nations, beginning at jerusalem.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waa àddina sépp dinañu ko jaamu, ñooñu ñu bindul seeni tur, li dale ci njàlbéenu àddina, ci téereb dund bu mbote mi ñu rendi.
and all that dwell upon the earth shall worship him, whose names are not written in the book of life of the lamb slain from the foundation of the world.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
dina yónni ay malaakaam ak baatu liit bu dégtu, ñu dajale ñi mu tànn ci ñeenti xebla yi, fa asamaan dale ba fu mu yem.»
and he shall send his angels with a great sound of a trumpet, and they shall gather together his elect from the four winds, from one end of heaven to the other.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu deretu ñi jub, ji ñu tuur jépp ci àddina, dina xëppu ci seen kaw, li dale ci deretu abel mi jub, ba ci deretu sakariya doomu baraki, mi ngeen rey ci diggante bérab bu sell bi ak saraxalukaay bi.
that upon you may come all the righteous blood shed upon the earth, from the blood of righteous abel unto the blood of zacharias son of barachias, whom ye slew between the temple and the altar.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: