From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
dama la nob
i love you
Last Update: 2017-02-11
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
«lii dama leen koy wax ci bi may nekk ak yéen.
these things have i spoken unto you, being yet present with you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
«loolu dama leen koo wax ngir seen ngëm bañ a wàññiku.
these things have i spoken unto you, that ye should not be offended.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
dama koy def, ngir ñi bokk ak man xeet siis, ba ñenn ñi mucc.
if by any means i may provoke to emulation them which are my flesh, and might save some of them.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
dama leen di jox dund gu dul jeex; duñu sànku mukk, te kenn du leen jële ci sama loxo.
and i give unto them eternal life; and they shall never perish, neither shall any man pluck them out of my hand.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
waaye dama lay ñaan ci mbëggeel gi nu séq, man pool màggat, mi ñu tëj kaso ci turu kirist.
yet for love's sake i rather beseech thee, being such an one as paul the aged, and now also a prisoner of jesus christ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
du ndigal lu ma leen di jox, waaye dama leen di yégal cawarteg ñi ci des, ngir natt fu seen mbëggeel tollu.
i speak not by commandment, but by occasion of the forwardness of others, and to prove the sincerity of your love.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
dama laa ragaloon, ndaxte ku néeg nga. dangay nangu loo dénkaanewul, di dajale loo jiwul.”
for i feared thee, because thou art an austere man: thou takest up that thou layedst not down, and reapest that thou didst not sow.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
walla boog ndax dama leen a tooñ ci li ma suufeel sama bopp ngir yékkati leen, ba ma leen di yégal xebaar bu baax bi te laajuma leen genn pey?
have i committed an offence in abasing myself that ye might be exalted, because i have preached to you the gospel of god freely?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
waaye malaaka mi ne leen: «buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xebaar bu baax buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.
and the angel said unto them, fear not: for, behold, i bring you good tidings of great joy, which shall be to all people.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference:
man maay ñam wiy dund te wàcce ci asamaan. ku lekk ci ñam wii, dinga dund ba fàww. te it ñam wi may joxeji, sama yaram la; dama koy joxe ngir àddina man a dund.»
i am the living bread which came down from heaven: if any man eat of this bread, he shall live for ever: and the bread that i will give is my flesh, which i will give for the life of the world.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Reference: