From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
Ñoom jaay nañu seen bakkan ngir turu yeesu kirist boroom bi.
men that have hazarded their lives for the name of our lord jesus christ.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te nun it lu tax fu nu tollu nu jaay sunu bakkan?
and why stand we in jeopardy every hour?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu yeesu dugg ca kër yàlla ga, daldi dàq ña fay jaay,
and he went into the temple, and began to cast out them that sold therein, and them that bought;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñu jaay seeni suuf ak seen alal, séddoo ko, ku nekk ak la ngay soxla.
and sold their possessions and goods, and parted them to all men, as every man had need.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
moom nag jaay na tool, ba mu moom, indi xaalis ba, teg ko ci loxoy ndaw ya.
having land, sold it, and brought the money, and laid it at the apostles' feet.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ba kenn du man a jënd mbaa mu jaay te amul màndargam rab wi, maanaam turam walla siifar bu mengoo ak turam.
and that no man might buy or sell, save he that had the mark, or the name of the beast, or the number of his name.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
am bés mu gis per buy jar njëg gu réy. mu dem nag, jaay li mu am lépp, jënd ko.»
who, when he had found one pearl of great price, went and sold all that he had, and bought it.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñaari picci rammatu, ndax duñu ko jaay ci dërëm? waaye benn ci ñoom du daanu ci suuf te soobul seen baay.
are not two sparrows sold for a farthing? and one of them shall not fall on the ground without your father.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
maneesoon na jaay latkoloñ jii ci lu tollook peyug atum lëmm, jox ko miskin yi.» noonu ñu daldi gëdd jigéen ji.
for it might have been sold for more than three hundred pence, and have been given to the poor. and they murmured against her.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñenn ca jawriñi nguur gi it, ñuy ay xaritam, yónnee ci moom, di ko dénk, mu bañ a jaay bakkanam ci dugg ca powukaay ba.
and certain of the chief of asia, which were his friends, sent unto him, desiring him that he would not adventure himself into the theatre.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñoom ñaar dem nañu, bay bëgg a jaay seen bakkan ngir man; maa ngi leen di gërëm ci loolu, du man rekk sax, waaye itam mboolooy ñi gëm ci xeeti àddina sépp.
who have for my life laid down their own necks: unto whom not only i give thanks, but also all the churches of the gentiles.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: