From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
moo tax «yàlla jagleel na ibraayma njub.»
and therefore it was imputed to him for righteousness.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
noonu waxtu wu boroom gétt gi feeñee, dina leen jagleel kaalag ndam guy sax ba fàww.
and when the chief shepherd shall appear, ye shall receive a crown of glory that fadeth not away.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
wóor na ma ne, dégg ngeen yenub xamle yiwu yàlla, bi mu ma jagleel jëm ci yéen.
if ye have heard of the dispensation of the grace of god which is given me to youward:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te it ku tàggat yaramam ngir rawante, duñu ko jagleel kaalag ndam mukk, su toppul sàrt ya.
and if a man also strive for masteries, yet is he not crowned, except he strive lawfully.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ak gnome dees na jébbalaale it ab joyaluwaay bees jagleel tëralkat yi, tax ñuy man a bindiy tëriin yu kàttanu te fasu
gnome also includes a complete development platform for applications programmers, allowing the creation of powerful and complex applications.
Last Update: 2014-08-15
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye loolu nag ab taar la ci jigéen. dañoo jagleel jigéen kawar gu gudd, muy muuraay ci moom.
but if a woman have long hair, it is a glory to her: for her hair is given her for a covering.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«buleen ragal dara, yéen coggal ju ndaw ji, ndaxte dafa soob seen baay, mu jagleel leen nguuram.
fear not, little flock; for it is your father's good pleasure to give you the kingdom.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye loolu lañu bind ne: «yàlla jagleel na ko njub,» du ibraayma rekk a moom wax ji.
now it was not written for his sake alone, that it was imputed to him;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
sopp nga njub te bañ lu bon.looloo tax yaw yàlla,sa yàlla sol la mbég mu gën a réymi mu jagleel say àndandoo.»
thou hast loved righteousness, and hated iniquity; therefore god, even thy god, hath anointed thee with the oil of gladness above thy fellows.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
li may wax, lu muy tekki? ndax yàpp wi ñu jagleel xërëm yi dafay dara? walla xërëm yi dañuy dara?
what say i then? that the idol is any thing, or that which is offered in sacrifice to idols is any thing?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yaa di jàngalekatu ñi jàngul ak xamlekatu ñi xamul, ndaxte xalaat nga ne, yàlla jagleel na leen ci yoonu musaa bépp xam-xam ak gépp dëgg.
an instructor of the foolish, a teacher of babes, which hast the form of knowledge and of the truth in the law.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw nag yàlla jagleel na leen may, gi mu nu mayoon, bi nu gëmee yeesu kirist boroom bi, man maay kan, bay tebbi àtteb yàlla?»
forasmuch then as god gave them the like gift as he did unto us, who believed on the lord jesus christ; what was i, that i could withstand god?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ci mujug jamono jii nu tollu, yàlla wax na ak nun jaarale ko ci doom ji. doomam jooju la yàlla jagleel lépp, te ci moom la yàlla jaar, sàkk àddina.
hath in these last days spoken unto us by his son, whom he hath appointed heir of all things, by whom also he made the worlds;
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
déedéet! waaye sarax yi xërëmkat yi di rendi, ay rab lañu ko jagleel; jagleeluñu ko yàlla. te man bëgguma, ngeen booloo ak rab yi.
but i say, that the things which the gentiles sacrifice, they sacrifice to devils, and not to god: and i would not that ye should have fellowship with devils.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ca néeg ba ca topp, saraxalekat bu mag ba rekk moo fa daan dugg benn yoon ci at mi. te daawu fa dugg mukk te yóbbaalewul deretu mala, yi muy jagleel yàlla, ngir bàkkaari boppam ak yu mbooloo mi daan def ci seen ñàkka xam.
but into the second went the high priest alone once every year, not without blood, which he offered for himself, and for the errors of the people:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
te saag, sefas ak yowaana nag, ñi ñu teg kenuy mbooloo mi, bi ñu ràññee yen bi ma yàlla jagleel ci yiwam, ñu fekksi nu ci, ba jox nu loxo, man ak barnabas, nu liggéey ca ña dul yawut, ñoom ñu liggéey ca yawut ya.
and when james, cephas, and john, who seemed to be pillars, perceived the grace that was given unto me, they gave to me and barnabas the right hands of fellowship; that we should go unto the heathen, and they unto the circumcision.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: