From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
ndaxte noonu la coobareg yàlla tëdde, maanaam ngeen sax ci def lu baax, ba wedamloo jayil yi xamul dara.
for so is the will of god, that with well doing ye may put to silence the ignorance of foolish men:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kooku boroom tiitar la, bu xamul dara. dafa wéradi, ba sóobu ci gëstuy neen ak i werante ciy araf yu dul jur lu dul ñeetaange, xuloo, xaste, ñaaw njort
he is proud, knowing nothing, but doting about questions and strifes of words, whereof cometh envy, strife, railings, evil surmisings,
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
gannaaw loolu boroom dëkk ba dalal mbooloo ma ne leen: «yéen waa efes, ana ku xamul ne, dëkku efes moo di wottukaayu màggalukaayu artemis ak nataalam, bi wàcce asamaan?
and when the townclerk had appeased the people, he said, ye men of ephesus, what man is there that knoweth not how that the city of the ephesians is a worshipper of the great goddess diana, and of the image which fell down from jupiter?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye ma teg ci ne: xanaa bànni israyil dañoo xamul? aaŋkay! musaa dafa jëkkoon a wax ne:«dinaa leen siisloo xeet wu bokkul ci yàlla,merloo leen ci ñi xamul dara ci yàlla.»
but i say, did not israel know? first moses saith, i will provoke you to jealousy by them that are no people, and by a foolish nation i will anger you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Some human translations with low relevance have been hidden.
Show low-relevance results.