Results for lafañ translation from Wolof to English

Human contributions

From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.

Add a translation

Wolof

English

Info

Wolof

lafañ bi xool leen, yaakaar ne dina jot dara ci ñoom.

English

and he gave heed unto them, expecting to receive something of them.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

noonu ay gumba ak ay lafañ ñëw ci moom ca kër yàlla ga, mu faj leen.

English

and the blind and the lame came to him in the temple; and he healed them.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

waaye boo dee woote lekk, wool néew doole yi, làggi yi, lafañ yi ak gumba yi.

English

but when thou makest a feast, call the poor, the maimed, the lame, the blind:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

amoon na ca listar nag nit ku fa toog, ku ay tànkam làggi, ndax li mu judduwaale lafañ te musul a dox.

English

and there sat a certain man at lystra, impotent in his feet, being a cripple from his mother's womb, who never had walked:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ndaxte ay rab yu bon bàyyi nañu nit ñu bare, ña ñu jàppoon, di yuuxu ci kaw; te ñu bare ñu làggi ak ñu lafañ daldi wér.

English

for unclean spirits, crying with loud voice, came out of many that were possessed with them: and many taken with palsies, and that were lame, were healed.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

te bu la sa tànk di yóbbe bàkkaar, dagg ko. nga lafañ te tàbbi ci dund gu wóor gi moo gën, nga am ñaari tànk, ñu sànni la ci safara.

English

and if thy foot offend thee, cut it off: it is better for thee to enter halt into life, than having two feet to be cast into hell, into the fire that never shall be quenched:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

ba mu fa nekkee, nit ñu bare ñëw ci moom, indaale ay lafañ, ay làggi, ay gumba, ay luu ak ñeneen ñu bare. Ñu teg leen ci tànki yeesu, mu faj leen.

English

and great multitudes came unto him, having with them those that were lame, blind, dumb, maimed, and many others, and cast them down at jesus' feet; and he healed them:

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Wolof

«surga ba dellu ca njaatigeem nettali ko loolu lépp. noonu boroom kër ga mer, daldi ne surga ba: “demal gaaw ca pénc ya ak ca mbedd ya ca dëkk ba, te indil ma fii néew doole yi, ñu làggi ñi, gumba yi ak lafañ yi.”

English

so that servant came, and shewed his lord these things. then the master of the house being angry said to his servant, go out quickly into the streets and lanes of the city, and bring in hither the poor, and the maimed, and the halt, and the blind.

Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:

Get a better translation with
7,794,437,698 human contributions

Users are now asking for help:



We use cookies to enhance your experience. By continuing to visit this site you agree to our use of cookies. Learn more. OK