From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
alku lañuy mujje, ñoom ñiy jaami seen biir, di wonoo lu ruslu, tey wut yëfi àddina rekk.
whose end is destruction, whose god is their belly, and whose glory is in their shame, who mind earthly things.)
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
piyeer gis ko, daldi ne yeesu: «kii nag, boroom bi, nu muy mujje?»
peter seeing him saith to jesus, lord, and what shall this man do?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye su meññee ay dég ak ay xaaxaam, du am benn njariñ; repp na ñu alag ko, te lakk lay mujje.
but that which beareth thorns and briers is rejected, and is nigh unto cursing; whose end is to be burned.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
piyeer topp ko fu sore, ba ci ëttu saraxalekat bu mag ba; mu dugg, toog ak surga ya, ngir seet nu mbir may mujje.
but peter followed him afar off unto the high priest's palace, and went in, and sat with the servants, to see the end.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ko piyeer déggee, mu daldi ne: «waaw nun nag, dëddu nanu lépp, topp la; kon nu nuy mujje nun?»
then answered peter and said unto him, behold, we have forsaken all, and followed thee; what shall we have therefore?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
Ñi dégg nettali, bi jëm ci mbir yooyu, dañu koo denc ci seen xol te naan: «nu xale bii di mujje nag?» ndaxte leeroon na ne, dooley boroom baa ngi ànd ak moom.
and all they that heard them laid them up in their hearts, saying, what manner of child shall this be! and the hand of the lord was with him.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: