From professional translators, enterprises, web pages and freely available translation repositories.
maanaam, duma noppee am naqar wu réy ci sama biir xol,
that i have great heaviness and continual sorrow in my heart.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
man nag fas yéene naa lii: duma dellusi ci yéen ci naqar.
but i determined this with myself, that i would not come again to you in heaviness.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yéen ñi nekk ci naqar, barkeel ngeen,ndax dees na dëfël seen xol.
blessed are they that mourn: for they shall be comforted.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ba naqar dina xar sa xol ni jaasi. noonu xalaati ñu bare feeñ.»
(yea, a sword shall pierce through thy own soul also,) that the thoughts of many hearts may be revealed.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
léegi nag baal-leen ko te dëfël xolam, ngir bañ mu sóobu ci naqar wu ëpp.
so that contrariwise ye ought rather to forgive him, and comfort him, lest perhaps such a one should be swallowed up with overmuch sorrow.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
taalibe yi nag am naqar, ñu daldi ko ne kenn-kenn: «mbaa du man?»
and they began to be sorrowful, and to say unto him one by one, is it i? and another said, is it i?
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi ko buur ba déggee, mu am naqar, waaye ngiñ la ak gan ña tax mu santaane, ñu jox ko ko.
and the king was sorry: nevertheless for the oath's sake, and them which sat with him at meat, he commanded it to be given her.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu dellu am naqar wu réy, daldi dem ca bàmmeel ba. pax la mu ñu yett ci doj, ube ko xeer.
jesus therefore again groaning in himself cometh to the grave. it was a cave, and a stone lay upon it.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
«bi ay moroomam gisee loolu nag, ñu am naqar wu réy, daldi dem, xamal seen sang li xew lépp.
so when his fellowservants saw what was done, they were very sorry, and came and told unto their lord all that was done.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
moona yéen de, yéena ngi tiitaru. waaye dangeen a waroon a am naqar, ba dàq kiy def loolu ci seen biir!
and ye are puffed up, and have not rather mourned, that he that hath done this deed might be taken away from among you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
kon nag dinaa ko tëral ci lalu metit, te ñiy ànd ak moom di njaaloo, su ñu tuubul jëfi jigéen jooju, dinaa leen teg naqar wu mag.
behold, i will cast her into a bed, and them that commit adultery with her into great tribulation, except they repent of their deeds.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
looloo tax ma binde noonu, ngir bañ a agsi, am naqar ci ñi ma waroon a bégal. am naa kóolute ci yéen ñépp ne, sama mbég mooy seen mbég.
and i wrote this same unto you, lest, when i came, i should have sorrow from them of whom i ought to rejoice; having confidence in you all, that my joy is the joy of you all.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
ci biir tiis ak xol bu jeex laa leen bind, samay bët taa ak ay rangooñ. binduma leen ngir teg leen naqar, waaye ngir ngeen xam xóotaayu mbëggeel gi ma am ci yéen.
for out of much affliction and anguish of heart i wrote unto you with many tears; not that ye should be grieved, but that ye might know the love which i have more abundantly unto you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
bi nga xamee ne tàggoo nanu ak ñoom ci naqar, nu dugg gaal, jubal dunu kos. te ca ëllëg sa nu dem ba teer ca rodd, ba noppi jóge fa, jàll ba patara.
and it came to pass, that after we were gotten from them, and had launched, we came with a straight course unto coos, and the day following unto rhodes, and from thence unto patara:
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu delluwaat di ñaan ne: «sama baay, bu fekkee ne kaasu naqar bii mënu maa teggi te naanuma ko, kon na sa coobare am.»
he went away again the second time, and prayed, saying, o my father, if this cup may not pass away from me, except i drink it, thy will be done.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
waaye nag boo séyee, defoo bàkkaar, te bu janq séyee, deful bàkkaar. waaye ñi séy dinañu am naqar ci àddina, te naqar woowu dama leen koo bëggoon fanqal, yéen ñi séyagul.
but and if thou marry, thou hast not sinned; and if a virgin marry, she hath not sinned. nevertheless such shall have trouble in the flesh: but i spare you.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality:
yeesu ne ko: «xamuleen li ngeen di ñaan. ndax man ngeen a naan kaasu naqar, bi may naan?» Ñu tontu ko: «man nañu ko.»
but jesus answered and said, ye know not what ye ask. are ye able to drink of the cup that i shall drink of, and to be baptized with the baptism that i am baptized with? they say unto him, we are able.
Last Update: 2012-05-04
Usage Frequency: 1
Quality: